machalla yallna yalla dolila diame Barker Serigne Touba
2026-11-04 18:34:00
0
Modou Sour :
wàwe. goor. way💚💚💚💚💚
2026-11-03 03:13:57
0
BAY NDIAGA Diop ALALOU 👥️👤 :
kemtanou serigne saliou mbacké 👏🙏
2026-11-02 10:35:01
88
BAYE VITO :
ma sha lakh diërëjeuff
2026-11-03 15:42:52
0
A.SADIKH :
Amine yaram amna solo loool
2026-11-03 22:06:02
0
Seck Abdoulaye :
Iman kokou bopom réck walay
2026-11-02 12:52:29
19
jalloneur :
Li dé moy deug , kouko nagou moy deugeu kouko bagne moy deggg ✌
2026-11-02 20:51:28
8
baye bou PROS :
kadou yi mome wakh deugue rafét na, mais diomaye daffa wore SONKO, wore 54% yiko votél
2026-11-02 20:51:23
28
sokhna faa :
politique dou Etat fi Etat mofi fort sétoul lou nékh nit lou nékh peuple lay khol li ngay wakh réunion famille la dou réunion pour le peuple sa discours bi valable boul pour la République qui est l'état kon désolé
2026-11-02 16:29:54
2
𝙤🅕🅐🅓🅓🅘🅛🅤𝙤ﷺ 🕌📿☪️ :
Sonko def na lépp ngir refetal digganteem ak Jomaay ms Jomaay kenn xamul lan la bëgg. Jërëjëf Sëriñ Muhammad Njaay Kàddu refet na lool masàllaa yal na la Yàlla fay aw yiw.
2026-11-04 21:16:58
1
ndiagambaye618 :
lila mansor mbaye waronawax
nila waronawax def mag nailay
waxé Merci papa
2026-11-03 13:54:39
9
Dieng Alla :
💚💚💚💚 wallahi ndeye sane ndiaye kadouyi rafétna matalé na lole yalla na yalla doli la deugeureul li rék Moy deugu té yalla sounou borom deugu rék la beugu koula kham khamni do wakh lou amoul ndiarigne Machallah dieureu dieuff
2026-11-04 12:06:53
2
sonko 2029 inchalla :
machalla kadou yi rafetna
2026-11-02 22:58:10
5
diouf djily :
refetnaloooooool
2026-11-03 12:14:53
0
pablo :
serigne bi yaw dé nite kou bakh ngua kou bakh rek moye def li
2026-11-04 01:04:11
4
user7585582557000 :
machallah mbokk mi liidé leu niepp di khaar ci kilifa gounék rawatina talibé sëriñ Saliou rahmatoulaahi aleyhi
2026-11-02 21:54:06
17
❤️ Senegalese love 🇸🇳 :
lii rék moy deugue ✅
2026-11-02 13:42:37
13
@boly.diop :
Sonko moy Sénégal
2026-11-02 17:59:20
9
MOUHAMED FALL :
machalla bonne continuation
2026-11-04 13:52:51
1
NDIAYE RIMINI :
Merci infiniment j' espère que le président vous écoute Mauvais ENTOURAGE