affairou milieu ngen di bayi amoul beineu ndieurigne yalla Nala yalla yeureum 🙏
2026-11-02 11:59:21
2366
THiate to Yayame❤️ :
milieu dou pour djiguene vrema 😭yalna yalla wereume la kharela aldiana
2026-11-02 14:49:22
591
ahhh :
wawaw amoul arrêt dé bouléne changer dé
2026-11-02 13:12:55
272
babacar :
djiguén warou dém lamb bly wly repose en paix 🙏🙏🙏😭😭
2026-11-02 13:00:41
233
. :
Boul guiss nite ba yakarni yako guene,yalla nouné lay nato Domou Adama ,monone nanio nek si placame ndakh liguéya Louniou yalla loutakh mou def niou niou nekk si dahira yi ,naniou ko nianal yalla,té def tout le possible ba kouniou guiss thi yone boudoul nonou niou yedd la souniou ko meunè 🙏🙏🙏
2026-11-02 18:49:50
141
✪꧁꧂𝐃𝐢𝐞𝐧𝐠~~𝟑𝟏𝟑𓆙✪༆༄ :
Arrêt bi dh mom bamel la
2026-11-02 18:30:35
77
PendaAbdoul♥️🇸🇳⭐️⭐️ :
Bilay bougouma Diegén bouye doundou milieu parce que nous sommes des princesses 👸 et amoul chance mm bo demoul diko sa dér dou séte😔
2026-11-02 16:27:01
130
BACHIR🇸🇳✪ :
Affaire milieu yi mo baxoul amoul chance
2026-11-03 17:22:56
9
falloungom19 :
yalla dh yakam touwoul ken Lou way def sa bopou
2026-11-02 13:43:47
141
Khalile⚡️ :
Bayilén Stade ak moto yi sourtou Wa banlieue bi
2026-11-02 13:44:35
92
Vie bi :
Athia gameur yi day daw rek ba birr armèl
2026-11-03 15:20:01
15
sarr :
sama rak dji demna ni rek
2026-11-02 12:57:05
42
dieyedqoq97 :
Wa gni Ani sen ay wadiour mane deh bilahi walahi li sagnou mako
2026-11-02 15:07:50
31
Bakhe yaye❤️❤️❤️ :
Yalla nako Yalla yeureume si barké Seydina Mouhamed 🤲
2026-11-02 13:54:36
27
madame Ndiaye ✌️✌️ :
am kififay li am solo
2026-11-03 20:54:14
1
BAMBA… :
deif lein sén bopou yi ndokh affaire de milieu bi ngén di forcé sén bopou ana lan moy ndiarigne li 🥰❤️yalna yalla yeureum kou 🙏🙏
2026-11-02 19:27:41
7
aicha buznes vente 🥰🥰🥰🥰🥰 :
legui bo déme loye wakhe yalla dama zimbre. ba alakhira 😳😳😳😳
2026-11-03 21:13:33
10
BB Rokhaya ❤️💍🔒 :
Ndeyesane Masta way💔💔💔🙏🙏😭😭😭
2026-11-02 13:07:26
32
David bu diamaguene 🇸🇳🎸🇫🇷 :
yalnako yallah yeureum 🤲🏻🤲🏻
amine yarabi incha Allah 🕊️[En larmes]
2026-11-02 13:13:32
16
Chic Beauty by oumina💄🪭 :
Ay way yereum len sen yay dji ay khalé you ndaw 😭k son âme repose en paix 🪦
2026-11-02 13:35:46
20
aliou diéye 💞🚛 :
bi moy fin temps koukodoul khalate loula nèkh dèfal
2026-11-02 19:49:48
9
elzofriperie0 :
yeureum léne séne bopou yeureum séni wadiour bakh na 😭😭😭
2026-11-02 18:04:34
5
Dame Faye :
yobe bii môme téla dé rékkk
2026-11-02 15:49:30
7
To see more videos from user @bbccumab6, please go to the Tikwm
homepage.