@pactale: Liiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii

Grand pape Pactal
Grand pape Pactal
Open In TikTok:
Region: FR
Monday 02 November 2026 10:10:52 GMT
29268
1746
307
33

Music

Download

Comments

fallou.niang.khout
fallou niang Wakana :
Thieuy yalla nala yalla sopi dangua xamoul rk
2026-11-02 12:12:27
20
oussau4
Oussau24 :
Les gens passent 10 ans dans les daara mais ne savent même calculer la surface d’une chambre. Changeons notre façon d’enseigner le saint coran
2026-11-02 13:02:14
5
paradis1235
Fall فسيكفيكهم الله :
Pape taye donouga si question bi 😁😁😁😁
2026-11-02 16:48:40
0
alhamdoulilahfallou
𝐋𝐨𝐮𝐟𝐚𝐡𝐮𝐬𝐬𝐚𝐫𝐲🇸🇳 :
si gatal alqurane dfay nétali ay histoire yo khamni mokal ta khoul nga xamko dila digal dila téré pour nga xam litakh mou lay téré ak di la digal il faut nga diangeu téré xam xam pour xamko exemple alqurane dafa wakh diouli lén mais alqurane doula wakh Noy diouliwé il faut ki indi message bi expliquer la ngir nga xamko donc alqurane kén manou si lor kén ki dém diangeu bénén xam xam ngir lor nit yi ko kou yalla dafko reub
2026-11-02 12:50:32
13
gayebussiness
abdou lahad 🐫❤️ :
Pour kham alkhouran bi lanlay firi
2026-11-02 10:26:22
17
ahmadouaw919
ahmadouaw919 :
Grand pape ya pas de question idiote mais juste un exemple les baccalauréats littéraires scientifiques gestionnaires ils en ont fini avec l'enseignement general maintenant a l'université ils se spécialisent pour devenir géographie historien homme de lettre philosophe scientifique lolou xam xam la Après ça y'aura des concours pour apprendre le métier et ca requiert certaines conditions Ex: ENAM (magistrature impot et domaine, diplomatie, administration générale, douane) beneen Xam Xam bou bokoul ak college ni université
2026-11-02 17:27:06
0
thiernohamidouk
THIERNO HAMIDOU KANE :
Amna aye branches, droit, philosophie, sociologie, institutions politiques, médecine, psychologie etc..
2026-11-02 13:08:59
9
king.sharoukhane
king sharoukhane :
grand pape doma woone yalla 😂😂
2026-11-02 12:42:38
0
al.amine539
Lamine :
doyna war
2026-11-02 11:37:54
1
alpha.thiakry
Alpha thiakry :
tafsir figh Hadith
2026-11-02 12:09:01
0
badara439
badara439 :
il a frapper encore😂😂
2026-11-02 10:42:37
1
laminesoly98
baye lamine soly :
c'est la jurisprudence en islam qu'on appelle fiqh
2026-11-02 13:54:45
3
mbaye.ndiongue3
Mbaye Ndiongue :
farame fathie
2026-11-02 18:57:04
0
kilimandjaro437
Alvine :
Bonne question
2026-11-02 11:45:29
0
yakaararoog
wressling@#wins :
pourtant j'ai toujours pensé à ça 🤔
2026-11-02 14:16:41
0
kingsalmonefaye
kingsalmonefaye👑👑 :
Am na droit demander yeah
2026-11-02 20:04:57
1
fallouyeumbeul2
fallou original boy yeumbeul🔰 :
Pour finir al khourane bi meuna ate si dinné
2026-11-02 12:01:31
4
To see more videos from user @pactale, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About