@aliousylia81:

Nitou baye hamza ❤️🫀🕊️
Nitou baye hamza ❤️🫀🕊️
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 02 November 2026 14:28:45 GMT
27636
7013
165
35

Music

Download

Comments

leaderalusenegal1
Mourtada Fall :
Machalah xana touba la deukk
2026-11-02 18:05:21
73
mbacke.ka15
mbacke ka :
khana fi touba la
2026-11-02 19:50:45
27
alladji.fallou
alladji fallou :
Numoro paabi la sokh la
2026-11-02 19:42:38
18
lampfallyapchaxagnethi
lampfallyapchaxagnethi :
Barki yalla bo dèmê sênn poss amoul sakh 5mil mais doko xam bou gnou xeuyê diamgue moihibu rk lèpp baxna sênn yonn ci Dara serigne bi rk 🥰
2026-11-03 02:07:48
14
modou040a0
mohamed diop :
khanna touba lh
2026-11-02 17:21:46
6
mame.mbaye.dieng4
SEYDINA BABACAR DIÉNG🥰 :
Bou léne nékhone tok di carté wala nguéni wérénté waayé Défou léne ko li touba rék la am
2026-11-02 21:16:05
9
user61344891308662
talla gadiaga :
yén dé yana ma ganal payi maye roumou Mbacke bawol
2026-11-02 18:39:00
6
fallamadoubouna4
fall amadoubouna :
Wa Touba ak Alhourann Rék 😭
2026-11-04 22:44:40
1
diawproductions
Diaw Promoteur :
Li touba reka la ame
2026-11-02 18:11:41
9
baye.serigne704
baye serigne70 :
Diamou yalla si marsé la eupé🤔🤔🥰
2026-11-02 16:04:29
12
bambandiaye90
Ndiaye :
li dh touba rék la am 😳😳😳
2026-11-03 20:34:17
3
bamba.faye540
Bamba Faye :
thieye payi toubayi diamou yalla ba kheuy deee yallna yékh
2026-11-03 23:18:43
1
mounassthiaw
خذو الحكمة من أفواه المجانين :
dara diaroule faté yalla ☺️☺️☺️
2026-11-03 13:24:06
3
bromlepaybakh
Brom lepay bakh :
oh dieuredieufaty brom Touba
2026-11-02 14:33:34
4
khdimcpo
Khadim Ndong :
touba rk la mana don
2026-11-02 20:16:34
3
dioufmouhamadoufaadal
MHD FAADAL :
Yalnagnou borom bii fayaal serigne Touba
2026-11-03 17:12:08
1
njiaye2
Oui 👍 :
Khana magou touba yila
2026-11-02 19:47:25
3
kebecheikh793
kou beugue problem def ma sign :
ohhh li sedd na xol 🥰🥰
2026-11-03 00:27:40
1
blackdame667
𝓝𝓭𝓲𝓸𝓵✰𝓶𝓲𝓲 øвᵍ✈️🧠❤️✌🏽 :
Maggi Touba yiii 😍❤️
2026-11-03 05:27:57
1
guccimane.2211
Guccimane 221🦩 :
Touba la am deh
2026-11-03 00:13:47
1
beuguesrgfallou
Beugue fallou :
Ndayesann
2026-11-02 18:34:31
1
darou_nahim_eletron
🟠DAROU ✪ NAHIM ✪ ÉLECTRON🔵 :
Jëmu waay bi daal móoy al Qurane yalla xam nako
2026-11-02 21:28:16
1
bromdarou05
Borom Darou 5️⃣ :
Yalla na yalla samlen
2026-11-03 22:36:55
0
mouhamad.dieng70
di diema rafetal gir yalla rek :
ki de dan nako ngis touba lu bari
2026-11-04 22:16:55
0
domi.bossou
7 :
ndaw bari toyaba Machallah njiayom kamil
2026-11-02 17:43:29
0
To see more videos from user @aliousylia81, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About