@i5_andrew_0707: #fyp #shorts #viralvideo

i5_andrew_0707
i5_andrew_0707
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 02 November 2026 18:12:35 GMT
70710
5527
374
347

Music

Download

Comments

juanitabella98
3B💕BellaBusiness&beauty :
War nagn xolat ay dossier viol dh yomb na trop
2026-11-03 08:14:40
165
mamadoundoye8583
NDOYE LÉBOU :
frère même man sama frère bou am 18ans mongui chambre 39 reubeus problème de Viol té khalébi néna enquêteur yi ki sama copain la depuis deux ans niongui sékeu rapport kén violé wouma sama papa wakhoul DEUG c'est grave
2026-11-04 09:42:12
36
boydoubay75
Boy dubaï :
Yallah nanou yallah mousal
2026-11-04 22:04:38
13
mouhamed.samb16
Mouha _ fermin :
fii koufi djigne nit viol yoon déf liguéyam guiss né dou mome kiko djigne viol moo wara teud peine bi li dafa yombou lo khamni meun nasé teud 10ans de prison bala ngua porter pleinte war ngua am preuve
2026-11-04 17:41:47
17
diallo_546
zeyni🇬🇳Diallo :
viol est devenu une arme
2026-11-03 08:20:13
86
patriceaugustinba
augoo :
mais li dafa wara deme ci media yeupp
2026-11-04 09:39:44
30
khadyndiaye835
khady Jordan :
Métina trop mé yalla na yalla até si barki seydouna Moukhamed 👏😭😭😭😭
2026-11-03 07:52:16
71
user9727046353345
gjeficifjfnc FCN cvg :
li dalna sama dom dafa guene kasso rek mou dee gniou ateko non lieu tedeuna deux ans et 4 mois
2026-11-04 16:24:18
11
0ziledieng02
Dienguene bi :
Trop facile wakh degue fa yalla khawma lois la khawma Lane mais lougnou wara tégate la .
2026-11-03 07:44:05
45
yallabakhna1998
CATALAN BI :
alahira dina métti 😭😭😭
2026-11-04 16:46:39
9
mbackefal27
yagga bakh :
commandant commissaria eulek dina méti trop si niom
2026-11-04 08:23:10
14
niae45
loum801💙❤️💯🫶 :
noo li dafi wara diekh😳😳
2026-11-03 07:53:21
32
mistermo8
Modou lahi ciss :
Ohhhhhhh
2026-11-05 00:23:04
0
ablaye.ka02
Ablaye Ka :
😭😭😭😭😭 ohhhhhh 😓😭
2026-11-04 23:33:47
0
nabydeug60
𝓃𝒶𝒷𝓎_ 𝓇𝒶𝓈𝓈ℴ𝓊𝓁 _✰ :
Vraiment c’est trop facile 🤦🏾
2026-11-03 07:39:52
16
ibrahimasory0153
global :
le commendant rendra compt devant sa famille et devant dieu et je demande que le pape latir prit dieu pour ce commandnt
2026-11-03 09:03:01
15
moussabalde20
Eto'o_jr🇺🇲 :
Sénégal d'où remiii walayii
2026-11-03 08:32:50
15
.ibrahima.xalil.s
khalilulah🏀 :
yalla nanui yalla samal bopame si barkep alhourane surtout nioune jeunesse bi moytout rek natû mom dou wesss mai geuneu moytout rek🙏🙏🙏
2026-11-03 09:58:13
11
djibsone.diagne46
Djibsone <> :
Procureur yii Bilahi biss bouniou décédé yeureum nalen
2026-11-04 15:17:39
5
moussa2157
Moussa officiel 💯 :
[Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie] Sénégal barki alkhour'ane amna niou gaddou akkk yo khamni khamouniou fane laniou Kay layalé
2026-11-03 09:21:00
10
user8213479450756
fatima 😇 :
ou est la loi simple plainte on peut faire 4 a 5 ans de prison ou sont les autorités
2026-11-03 10:30:49
7
baal15806
Balé :
bilahi kou moytouwoul injustice sa moudjou dina gnaw torop
2026-11-03 11:59:58
7
princheu__halpoular
Sheutou seex ibrah🏁🫀 ✪ :
Thiey souñu borom aka meuna setane walahi dîna metti trop Keraw yomal khiyam
2026-11-03 11:25:57
7
issanguer1
nguer gandiol transport :
moytou sakh takhoule nga mouthi si yalla rekk molasi mana mousale yalla nanousi yalla mousale vraiment métina
2026-11-03 11:41:07
7
To see more videos from user @i5_andrew_0707, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About