Chéri wow nga beut deh bi communication si dece diakhler na💔
2026-11-03 09:32:15
1386
Jongoma2.0✨Officiel :
Waax Dji Rek ya soucis 🫠
2026-11-03 08:47:23
1198
✨AÏCHA✨ ♌️ :
Communication bou normal sakh meunolenn ko
2026-11-03 08:50:05
1209
Balla SMr✨✨🇸🇳 :
Li mofi dess pour niou amagoul 🤧
2026-11-03 12:32:36
101
K🌸❤️ :
Wa gni si décès laniou nek ?
2026-11-03 11:07:35
385
DIARIATOULAH🤎🥥 :
L’amprencent est toujours trompeur key😭
2026-11-03 11:54:28
182
ABABACAR NDIAYE.✪ :
« L’emparassant est toujours trompeur » okkk😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-11-03 14:01:08
116
talibey s saliou :
antouka woow gua beuttttttttt😳😳
2026-11-03 09:16:25
449
zeynaexwally :
Chery li dècè la di 😳waouh noy wakhé ni😳
2026-11-03 14:30:55
61
༺🌸𝕭𝖎𝖓𝖙𝖚 𝕬𝖉𝖆𝖒𝖆🌸༻ :
Hawma l’apparence est trompeuse hawma mais correct dina tax nit gni nawloo la. Di sol lu correct yor comportement bu baax te yor langagou nit ku yiw moo gën foo leen tollu naan dagn niouy jugé
2026-11-03 08:48:11
280
yayounabiaminata :
Ki décède rk mo perte Bilay nek si deuthie di melni ni kou nek si xew communication zero 0️⃣ tristesss li yeugaloulennn sakh repose en paix Khady
kii ma jàkkaar lool nii muy wax xaritam moo gaañu wala?!
yàlla nako yàlla yërëm !
2026-11-03 16:13:26
0
Mary ndiaye :
Repose en paix mais nek len ak nitt
2026-11-03 01:20:29
326
azou :
Yeureum lène senn parents yi
2026-11-03 01:44:55
86
Sokhna Karim ❤️🎊😌 :
Nek si décès melni 💔💔💔💔Xama nopi
2026-11-03 10:48:23
27
06mame 😍 :
J’aime pas leur façon de parler ni de communiquer sollou dafa am solo té nitt so beugué gni respecter la da ngay respecter sa bopp ba paré
2026-11-03 11:18:36
34
🌸 :
Mère yi en ce moment mé c triste
2026-11-03 01:38:07
117
Thiawafalilou🇸🇳 :
Souniouy wax gua len di xeb
2026-11-03 10:41:06
80
Maty’s Glow Shop ✨ :
lapenrance est lane cherie ?😭
2026-11-03 02:08:46
184
coumba.diop5043 :
Bizarrement ki Sm khol bi laye dague mounou ma comprendre nék djiguene weur lamb yi ak navétane respectel séne boppou kossi guiss mingui dague yaramam bref ki deff yalla nako yalla yeureum
2026-11-03 06:51:45
68
dosa :
yalla loumou dogal ken menou si dara mé parent yi nanou kholal yar bi té yalla kharé ko aldiana firdawsi 🙏
2026-11-03 00:23:18
128
To see more videos from user @senegal_dabord_3, please go to the Tikwm
homepage.