Papá dji yakarni yagui ray domam ndakh limou ayédji wa woudju yakarni dagua beugua yakh ayam [Lágrimas de alegría][Lágrimas de alegría] fék ni lépou ñom la
2026-11-03 17:53:04
24
mame fallou lha :
Bilay maman khady Aka Am liberté 😂
2026-11-03 18:55:03
21
bané_diop :
famille bi yalla topé wouléne dara bouyabo gnou mougne rék té gnanale léne goudou fane 😂😂😂😂
2026-11-04 15:56:06
8
Ciss :
Maman Khady liga sol rafét na
2026-11-03 19:38:56
15
user50714736578 :
wouy 🤣🤣🤣🤣
2026-11-03 18:02:18
8
Aïcha Nd :
mamam dal beugue nala
2026-11-03 17:34:55
15
AWA BEUG FALLOU :
sama kharit bi lima tanal diapou nako dh
2026-11-04 09:30:14
7
🫔🍔Les Délices de DoDo🍕🍰🥟 :
Nagne khaar réponse papa 😂😂😂
2026-11-03 19:06:12
18
🦂 ♏️ fatimarassoul bou Sonko :
Bama magué ba ame dôme la comprendre loutakh sama yaye meunaniou wakhtane bay tapanté sama papa bou woté mou raye batte bi 😂😂😂
2026-11-04 12:14:08
5
golden jr 221 :
bly famille bii mo eupe libérté Sénégal
2026-11-03 21:25:47
5
To see more videos from user @khadija.et.ses.betise221, please go to the Tikwm
homepage.