Meun nagn wax lu nekk waayei wakaana haqqan kenn dotu ko djangeu nu nekhei ni
S Abdoul ahad Gueye yalla sa borom yesal yeurmandé Barker Sheikhoul khadim
Cëey minanul baxil xadim
Wax nane ni Sëriñ bi néna bu guéne démé ba jamono lëundame kén xamul foy aw denk nalén sama ñaari xassida yi muy Wakana ak Barra-ani (minanul baxil xadim)