Yalla nala yalla sam may la Lou raw sa diorte li nga yéné sa yaye mou mate mais na nga am foula ak fayda boula dara keuf lo momoul boul lal loy déf rek soral sa yaye xalé louka keuf dafa yombou yalla nala yalla sam ar may la weer ak goudou fane moussal la si thiate ak beute on t’aime 🙏🙏❤️
2026-11-05 00:29:06
12
Princesse💗 :
Lepp lo beug si kaw souf yalnala ko yallah défaral si barké seydina Mouhamed psl🙏