boys yii douniou am nianou grands freres[Larmes de joie]
2026-11-05 18:12:23
107
wakeur borom golby :
Masta mais Iska yoor ga photo boye bi aussi
2026-11-05 18:17:52
78
Sokhna Ko Rassoul 🇸🇳 :
Tentative de meurtre la porté plainte gnou teth ko si non dina meusa ray nit 😂😂
2026-11-05 18:21:53
115
evachoco22 :
Lolou tentative de meurtre leu 😂😂😂 grand boul bayi mou seed dhei
2026-11-05 20:25:50
74
awa bio :
loy soumékou temps amoul nak légui khékh vite fait rek après niou diaol si lénéne😂😂😂
2026-11-05 23:20:57
7
user1796221160011 :
bo bayi woul nian intervention ci alleu bigay dhé
2026-11-05 20:27:34
33
Aïcha🦂!! :
😂😂😂😂😂mom batay guemoul ni maynagne ko second chance 😂😂😂😭
2026-11-05 21:43:44
11
Fallou Diop :
yangui may fatali Sma khékh ba ak boyi doon football si sounou bount keur ma ni damay songué ndéké boyi woté nagn renfor jour bobou la bayi khékh après tok na semaine génou ma sougnou keur 😂
2026-11-06 00:10:31
12
skinny :
Sama rèew nèeeekh na!🤔
2026-11-05 19:20:20
17
Américain :
ioww santall yalla. Man sama khékh ba akk ceinture noire ba ohhhh
2026-11-05 22:09:19
20
Ndiaye Sarr :
bagarres baxoul serigne bi yalna nga weer ak diam
2026-11-05 20:07:06
15
Diouf Kara 221✪✪🇸🇳 :
Saway iOw Kay boy bi réndit nala 😂😂
2026-11-06 02:19:14
0
AÏCHA GLAM MULTISERVICE :
Boy da def self defence 😂😂😂
2026-11-06 01:05:12
0
mohamed Djigo :
lii diarna perfusion 😂🙏🙏🙏🙏
2026-11-05 21:29:58
24
𝐒𝐚𝐥𝐢𝐨𝐮❂𝐝𝐣𝐚𝐦𝐢𝐥🕌🖇️ :
Pére lolou dou yonn dh
2026-11-05 18:41:57
27
PAPA YOU🚸 :
srx beuggeuna diél gal gui dougou Espagne, wayé galsen ak nékhayyam wonko guinaw cas là 😂😂😂
2026-11-05 21:16:17
14
Sophie Anna Diop Agent SONAGED :
ki khawna dée 😂😂😂😂😂
2026-11-05 18:07:40
18
Zara Mbengue :
Dognou Wane kila def lolou gnou xaméko[Hilare][Hilare]
2026-11-05 18:09:27
22
modoubane03 :
bilahi daladone raye doore fofou bakhoule dé
2026-11-05 18:36:44
12
To see more videos from user @adanaka3, please go to the Tikwm
homepage.