baye serign dieng 2024 ba légui guisouniouko ay diapousi svpl
2026-11-05 21:34:36
157
Gaye éleveur :
Modou fall depuis magal touba 20222 lagnouko geudja guis svp svp svp sv sv 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
2026-11-05 22:32:02
77
Miss Longrich Lo ndam💸 :
Wa diakhlé wolen😭
2026-11-05 22:01:28
1467
Maman Diop❤️ :
Disparition yi beuri na trop
2026-11-05 22:45:11
912
jog Aar :
li nak diarna une journée nationale
2026-11-05 22:24:18
653
🅜🅔🅒 :
Yalla nako sunu borom nite
2026-11-05 21:10:21
953
Pretty🎀Diadia👯🤍 :
li nk Était dou si wakh ? yombou na dal
2026-11-05 22:20:09
95
Alasco diop 🇸🇳 :
Diapou len si ta yalla rek takh
2026-11-05 22:22:10
34
Madm Gueye :
Waw nimom founiou dém😭
2026-11-05 23:06:35
26
Soda Boye ❤️ :
Babacar xana police meunoul localisé son téléphone vue k mongii connecter wou
2026-11-05 23:09:54
94
A🫶🏾Ndiaye❤️ :
Bolen di guene sen keur delen guene ak ndiap ba pare delen wakh bismilah tawakaltou alalah la khawla walla khouwata ilah bilah denk yalla sen bop sa yolen dioule ba pare niane lene yalla same len are len mousseul len si lep lou bonnn yalla na nieup delou wat sen keur si diam
2026-11-05 23:11:38
177
Faydou & Société ⭐ :
man affaire disparition Afrique surtout Senegal rek nga Koy degg pourquoi pas état manoul taxawal banxass bouy seytou lol un brigade ou commissariat qui charge les disparitions c'est vraiment misterieux yalla na yalla gniit leen
2026-11-05 23:22:22
41
Talibé serigne saliou mbake❤️ :
Oh metina trop yalla nalen yalla nit si barki seydina moukhamet 😔
2026-11-05 21:45:28
39
Emmanuel Diabang :
l'Etat du Sénégal doit mettre les moyen ou un service pour enquêter sur ça, le Sénégal doit dépasser la ou des citoyens disparaisse comme ça
2026-11-05 23:48:10
30
tatou :
wah légu pour Babacar hana meunou niou localisé téphone bi
2026-11-05 22:37:53
137
Leyla beauté :
Yallnala yalla Faye diaw🙏🏻
2026-11-05 21:46:05
1
Fatima Shop Mme Sagna 💍❤️ :
Babacar na police localisè telephone bi 💔😭
2026-11-06 02:10:27
0
Isseuh :
Lii nak eupna lokho d , yallah nalen yallah gnitt 🙏 🙏 wa borom 🚐 bou noir ak blanc bi tamit dougnou ci wakh ngua sensibiliser parents ak élèves surtout
2026-11-05 21:17:39
370
🌸❦ 𝓐𝓻𝓪𝓶𝓮 ❦🌸 :
Kiy téléphone nam di tak kay mane nagn ko localiser non Sénégal dal do comprendre 🥺
2026-11-06 00:23:40
5
Bineta MDM Niang 🇸🇳🇨🇦 :
Salalahou alla Mouhamed
2026-11-05 23:53:40
5
yadali Ndiaye :
ba demoun si gal yi😭
2026-11-05 22:09:59
14
ndiambour tv :
pour man sakh fegn na guis n'a gnou dougal ko sunu groupe bii vraiment yangui deff liguey bou am sollo mashallah yalla n'a yalla barkel liguey bii
2026-11-05 22:49:53
13
tima saliou ❣️🙏😌❤️❤️ :
Ili man ndiay sama mak la
2026-11-05 21:41:46
21
To see more videos from user @aleewjaaw, please go to the Tikwm
homepage.