Wér wamou doon weur nak fégn na [Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-11-05 22:31:16
17
bane cheuffeur :
no wér wi dou problem si mom
2026-11-06 10:11:48
0
Mame bousso diop :
Serigne mor mi dé werr bi dinako réer
2026-11-05 22:47:44
14
l'homme digne 784535289 :
akassa yalna barkel barkel borm touba
2026-11-06 09:09:35
0
amdy.moustapha561 :
Mashallah Yalla na barkel thie Barkep Borom Touba Thie Barkep Serigne Touba Bafaaw
2026-11-06 01:40:15
0
Yasmine Diouf :
ndokhaler Serigne Moe, Yalla na seyye bi barkell
2026-11-06 09:17:27
0
Baly Bousso ✨ :
Machallah Serigne Mor Sax Si Soxna Diarra prokhane yii la dieul Ay kou Amoul si Soxna Diarra yii yalna sounou brom barkél ta may léne si ndiabot gou am barké 🤲🏻🤲🏻
2026-11-05 23:05:39
47
YATMA’STYLE 🌟 :
Magui sogua comprendre litakh mou diokhe informations weet bi fii ba 2030 😂😂😂
2026-11-06 00:19:00
6
MÅØTŸ🥏 :
normalement photographe Yi ay télescope lay wr yoor😁
2026-11-05 22:20:14
20
user5230545218101thiate . :
masalah yala nalenn yalla mousal Thie thiatt
2026-11-05 21:37:41
44
🇸🇳Byfallou211🇸🇳 :
li leep si ndiagalé mi la 😂.yalla na yalla barkel
2026-11-05 22:26:33
29
baye fall :
Machallah. yalna barkéll♥️♥️🙏
2026-11-06 04:06:11
0
Ramatoulaye_N :
serigne bi meunone nga anticipé diokhé information pour prochain werou koor guiak 2027 bi😔wa kognouy batalé nak
2026-11-05 23:35:40
22
ousmane Ba :
Serigne bi Sa Weer feegn na Yalna BOUR YALLA sammeu barkeel seybi maylen Ndjaboot gu barkeel
2026-11-05 22:23:46
8
boy baol2🇸🇳🇸🇳 :
segn nanga respecte weer wo de
2026-11-05 22:28:21
5
Biggy____Fvns✪ :
Serigne mor wér mı mongui dém dh 😂😂😂
2026-11-05 22:53:11
7
BOROM NDINDY :
Mom awo la wala ?
2026-11-05 23:39:20
0
Soxna Diarra Gaye :
Aye s mor takeu na Alkhamndou lila 😅
2026-11-06 01:30:14
3
Fah mountaxa wurus 💎 :
Madame diapalé niou rek thi were bi 😂😂😂
2026-11-06 00:35:48
3
To see more videos from user @caatumseexyi788044848, please go to the Tikwm
homepage.