@people221tv:

People 221 TV
People 221 TV
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 06 November 2026 14:40:46 GMT
545897
61149
1101
5260

Music

Download

Comments

patriote_vision2050
Patriote Sénégal 🇸🇳❤️ :
finalement khalé bi fegn na Alhamdulillah
2026-11-06 17:41:51
1512
missndamlo2021
Miss Longrich Lo ndam💸 :
Waaa diangui bi esk diarati nako😭
2026-11-06 15:25:17
2955
taphadiop4633
tapha :
Mais Nak police dougnou diouk si lii mogui beugeu eupeu lokho deh
2026-11-06 15:25:26
2137
lyma126
Lyma Diop Diallo ❤️ :
Amm lein habitudes di dieuli khalé yii école mon gueunn yalnako sougnou borom nitt🙏🏾
2026-11-06 15:21:25
2529
lumaya66
Lumaya-cosmetics :
Sou ma wakhei on vas me traiter de sans coeur mais chaque jour ma wolou ndakh Lane mo leine terer youbou ak dieuli Seine ay dom meme sou keur gui soriwoul defois la faute yeine parent yi fi ma nekk si kaw Tali Bilay sou may dieuli samay domm sama xol dafay dagg daguay guis des enfant de 10ans ou moins di youbou ak dieuli Seine nopp Bilay sama xoll dafa dagg
2026-11-06 15:37:01
671
clecle0310
Une clée 🇨🇻🇸🇳♎️ :
Il est temps d’exiger aux parents d’amener et de venir récupérer leurs enfants 😳🥺
2026-11-06 16:57:10
274
ellisabethgueye
PDG chic et glam by Elisabeth :
Sama papa koumou meuss nianal thi khalé rérr gua guiss ko si katanou yalla ndokh lalay diokh gua seulmo ko boy guéneu si bountou keur di am nouvelle def Nako ay yone mais Machalah
2026-11-06 15:52:48
322
sophiashop29
Sophie :
Dougal lene vidéo caméra de surveillance bi
2026-11-06 15:18:27
1052
daba231290
DaBa🥰Diop🥰beugeu fallou🥰 :
ndeysane yalla nako yalla nitte metti na trop cheuuuuu
2026-11-06 14:44:49
572
missbr205
🕊️ :
Li metina adouna bi mo tass guene bayi xel si xaler yi rek
2026-11-06 14:59:12
338
adjoint.diop
Adji Yasmine Diop :
Mane may yobou may indi malgré déma yoor lir
2026-11-06 16:14:24
171
ndeye5673
Ndeye :
massa way
2026-11-07 16:42:11
0
dak25_......4
user 2014 :
yalla na feign si diam ak salam amine
2026-11-06 16:23:54
444
maimouna.sow33
21 🎂❤️Novembre 🌺 :
Yalna ko yalla nitt
2026-11-06 15:08:49
254
fahbintougueye4
fah❤️ :
Waa hana nitt gniii guissou niou won khalei biii Ay wayy sama yaram Bangui daw sah😭😭
2026-11-06 14:49:34
285
sodandiaye529
sodandiaye529 :
Aaay nagn def mbed yeup caméra de surveillance yalla nako yalla nitt🙏
2026-11-06 15:25:43
274
gamb1a0
fatiz sall❤️🫶💕 :
Oh master 🥺
2026-11-07 00:06:35
0
papendiayefuturmaire
papendiayefuturmaire :
Bilahi sama dom makoy yobu makoy indi fo rombu gnunannn deko Bayi muyy demel bopappp legui dekeu bi mo woratul [Yeux larmoyants][Yeux larmoyants][Yeux larmoyants][Yeux larmoyants]
2026-11-06 15:50:59
64
usert97520032019
plumeblanche :
mane lhamna je ne suis pas normale sama dome tant que amoul âge 10 et plus douma ko bayi sakh mou dem boutique école may dieuli dama niaw ndiorte
2026-11-06 15:40:18
115
samb15
samb15 :
Man d damay soneu bay begeu d mai sama dom tankam sama tank ecole ba keurga
2026-11-06 16:08:02
57
lagochic_9
Lago_Chic 🐆✨ :
Mane deh sama boss amna 8ans té fimouy dianguei ak fima deuk c’est 2 minutes de marche damay diakarlok école bi wayei terewoul denioukey yobou dieuliko dou dem boutique dou gueineu deukk bi da todj
2026-11-06 16:55:52
32
beag496
Chic Senteurs by Mayatii🌸 :
Deuk bi mo woratoul bilahi dakoy diar 30mn avant la descente nga dieuli sen dome yi
2026-11-06 16:06:32
53
aronaba860
Arona Ba :
khallé bi few na alhamdoulilah 🥰
2026-11-06 17:47:35
59
user43659845288126
bijou kounta :
oh khaleyi
2026-11-06 15:06:26
60
To see more videos from user @people221tv, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About