Wa mais Grand khana danga am site bouniou khamoul boy dieulé sa vidéo yi
2026-11-06 15:02:43
106
kingsalmonefaye👑👑 :
Seugne bb[Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-11-06 17:02:23
8
Doumou sonko mou sel mi :
Domou Diane Diane la🥰🥰
2026-11-06 16:57:34
4
FOROM GALSÉN 🇸🇳 :
wa ana yayam 😂😂😂😂
2026-11-06 15:34:12
11
Omar Faye :
grand pape khane guissago khalil fall mara
2026-11-06 18:17:26
0
BARHAM~at~tidjani📿🫀 :
Ndeyssane boy bi innocent la boukou yalla dimbali woul Dara dou diangue dou ham dara ndeyssane
2026-11-06 17:24:23
5
badouu33 :
Man foumouy dieulé video yii moma diakhal😂
2026-11-06 15:11:57
49
abdouguelowarbusonko :
paaka bi pour lane la
2026-11-06 16:00:42
8
ndiaga diop :
YAWYASOFF
2026-11-06 18:15:59
0
mourid bi :
saway ki Serigne dh au cas où
2026-11-06 16:41:25
1
Daddy Diop 🇸🇳 :
Mini Dieuwrine 😂
2026-11-06 15:05:13
29
D✂️M✂️C✂️❤️❤️ :
Grand pape vidéo yi yakoy defar😂😂
2026-11-06 15:57:29
1
a'm from parcelles 🤞 :
guiss iow grand pape dinga wakh foy dieulé vidéo yiii😂😂😂
2026-11-06 15:15:53
6
mourid ndigal :
grand pape j'espère que xamé ngame magui balou ak mala waxone degay féne nga diél ma pv sagama . merci bcp comme tafoma . magui diégalou boubakh . nguir yalla tontouma si balou guimala ballou
2026-11-06 18:20:05
1
sadikhouna🇸🇳🇸🇳 🇺🇸🇺🇸 :
mai grand pape nékhngua trop koi
2026-11-06 17:33:52
1
Ndigull DC :
Sakura
2026-11-06 17:52:11
0
Mouride Mbaye 1710 :
Sénégal li fi nékk yépp kén Manou ko wakh 🤣😂🤣
2026-11-06 16:00:31
4
Futur guide suprême du Sénégal :
Bouma woté di nguéne gneuw ?😂
2026-11-06 16:27:58
0
R.○.$.€ Farm 🐂💯 :
2026-11-06 16:03:23
2
katim Rodrygo :
Grand pap li do Sénégal 😂😂😂😂
2026-11-06 16:50:59
0
shayme :
formation Serigne
2026-11-06 15:03:51
0
pacogalsen :
Qui cest le Grand Marabout 😂😂😂 Man mangui dèm Djèbalou
2026-11-06 16:21:21
2
Bathie Diop :
wa legui fou problème bi nékeu
2026-11-06 17:16:09
1
Serigne Mame thiernou séné🕋🕋 :
🥰🥰🥰
2026-11-06 18:20:49
0
boubacar gueye :
2026-11-06 18:23:10
0
To see more videos from user @pactale, please go to the Tikwm
homepage.