@fatima.diallo4015: 🎬 TITRE : BOUKI DAFA BËGG NEKK MILLIONNAIRE ! 😂💰 🐾 Bouki gis na vidéo TikTok bou am 10 millions de vues ! Dafa ne : « Maa ngi wara nekk millionnaire tey ! » 🤣 Mais problème bi ? Bouki poste vidéo bu am 2 vues seulement ! 😭😂 Bouki wax na : « Waaw ! Algorithme bi dafa ma bëggul ! » 🤣🤣 🔥 BOUKI MOY DOFAL MONDE BI ! ❤️ Like 💬 Commentaire : BOUKI 🐾 🔁 Partage ➕ Abonne-toi pour plus de délire ! 🌍 BOUKI 🐾 VIRAL TOU-LÉ-MONDO ! #Bouki #ViralTouLeMondo #TikTokSenegal #Wolof #Humour