ohhhh lima rombou Diakaye dangou dégueli ma paralisé ndakh li ague sama kholbi ki di diangueli yalna guoude fane té weer barké Seydina MUHAMMAD PSL
2026-11-09 23:42:27
4
yacinemoussa5 :
Déléne wakh Rufisque nord
2026-11-10 16:47:14
1
user73600269591774 :
blh pa bii damako beugue mn mii niane bii mo daw yaram fadiar gui nk ohhh 🤦🤦🥹
2026-11-08 15:08:25
2
Mme Doumouya :
d'où pa dai c un jeune machallah
2026-11-09 18:47:41
4
saliou Seck :
depuis santhiaba. machalla
2026-11-10 17:46:16
1
mbackéIphone221🇫🇷 :
Stp pa biy wax li chaque fadiar bilay yalla na yalla koudeul faname bilay mane guendeul3 la deuk mais chaque fadiar après weusifeubi damakoy tewlou fatabarakalakhou
2026-11-08 02:37:04
1
👑🎒17 novembre 🎉🌴 :
Bilay li damay Ray
2026-11-10 16:32:05
1
User6789 :
Wala Darou salam,
2026-11-10 14:28:35
1
alhamdou945 :
Frère Man Darou salam JAD la Deukeu sama kaw lale lay teudeu diko deklou bamou diékh heure bouy diékheul wezifa bi