ndéysane sama papa biko fébar bi sonalé nila doon dioulé dagay wax AK moom mou nopil sou paré néla dama doon diouli yalla nako yalla yeureum kharéko aldiana firdaws ak mboléém gnimou fa nékal Amine yarabi 😭💔😭💔
2026-11-08 00:09:53
319
Timikuluti :
amine amine amine amna solo yalla nala yalla faye
2026-11-08 11:53:37
0
ndeye dieng :
machalla amna solo yallna yalla barkél kham kham by