UN PROFESSIONNELLE DOU WAKHÉ NI CONCENTRE TOI SUR LE RESTE DU CHAMPIONNAT
BRAVO A LAMINE FATY LE PRÉPARATEUR DES GARDIENS DE BUT HLM
2026-11-08 19:40:53
379
Ndiag's :
A la fin TFC sera champion
2026-11-08 19:59:45
124
zale pikine :
deug dou rombi nope
2026-11-08 19:57:13
131
Momaro :
arbitre bi mo beugone yak sou niou match motakh mou reagiré ni
2026-11-08 23:08:17
29
pa_willy05 :
Ki xana Wa Teungueth dfa ame louniou la déff wakh niou xam 😂
2026-11-08 20:57:26
66
𝒦𝐻𝒜𝐿𝐼𝐿 𝐵𝒪𝒴 𝑅𝐼𝒪🟡🔵 :
Dougnla dieundeu deih
2026-11-08 22:16:36
19
BABACAR FAYE :
teungueth sera champion inchallah
2026-11-08 22:30:05
12
TEPA :
Courage bro
2026-11-09 01:30:32
0
SDM\GR ✪ :
Gardien HLM loum bokk ak mbaye lambare
2026-11-08 19:39:32
49
Cheikh pissi »>>›😎🫵✓🇸🇳 :
HLM SELl 🟡🔵👉🏽🏆🏆🏆🥺🥺
2026-11-09 03:52:12
0
Momo richard 10 :
Sisou man la rio seul
2026-11-08 20:04:54
15
ousmane thiaw TFC💙💛 :
mais ki loumouy wax ni mome
2026-11-08 19:50:33
15
RICHARD RIOS JR🇨🇴🇸🇳 :
sa way défal ndank rek khamnagne fou championat bi di moudiou TFC💛💙we are
n'oublie pas que t'es professionnel meunal communication 🤧
2026-11-09 10:29:14
6
BADOU Arnold 🇸🇳😎 :
Victoire bi moko bêt walahi
2026-11-08 21:29:07
6
Saco skj :
Força Eugénio 🇬🇼🔥
2026-11-08 19:05:53
20
mosarr45 :
Professionnel gua boul wakhé ni
2026-11-08 20:06:19
6
feuza@237 :
😏😏😏c sport mon gars
2026-11-08 18:52:15
8
Mboup Libasse :
ki khana support la barina wakh 😂😂😂😂
2026-11-08 21:11:03
5
35!!😤⚽️ :
félicitations mais bayil wakh dji joueur dou détail
2026-11-08 19:37:08
5
Yaah_Muuhamed 🌸 :
Légui lane la arbitre yi deff au contraire Teungeuthie mo fa ame penalty bou leir nanie mou bayi mou dialeu té aussi deuxième but HLM y’avait hors jeux attaquant mo djitou bal bi si centre bi nga taxaw di waxx
Hlm Kay Len Leu Arbitre Bi Done Sathial Guay Doul😂 Tfc💙💛 3 Fois Champion Du Sénégal Coupe Du Sénégal Coupe De La Ligue Deuxième 🇸🇳 À Qualifier Phase Poule Ligue Des Champions après Jeann D’arc Duniou Sen Nawlei
2026-11-10 11:11:01
1
mo_thiago06🇸🇳🇧🇷 :
Hlm leurs sorties de balles….incroyable….le latérale gauche numero 15 et le milieu de terrain numero 3 juste waouhhhh 🔥☝🏾
2026-11-09 18:17:42
2
gawaan_tech :
Bilay wakh na deug
2026-11-09 16:31:54
1
Lamine konte🇸🇳❤️ :
arbitre bi bouko tegoumala wone si yone dolene gnou gagner soit un peu professionnel
TFC kessei 💙💛
2026-11-09 00:29:35
3
To see more videos from user @zomqdufoot, please go to the Tikwm
homepage.