as goor boko défalé lou bakh rék raygako dioye na ba sone
2026-11-09 08:18:39
396
Mame Diarra mboup :
mane dama diakhlé kou diouy ma dioy😭
2026-11-09 11:22:07
37
talibé sonko :
j'aimerais tellement que quelqu'un vienne en aide à mon petit frère comme sa il a fini ses études il a fait une formation et sa fait plus de 3 ans qu'il cherche du travail mais rien jusqu'à présent te pourtant khalé bou bakh leu te ame yarre ak diné mais yallah bakhna
2026-11-09 08:18:40
70
l'absolu 313 :
ndeysan nianga sedelé kholam yalla nako yalla sedelé sa khol
2026-11-09 06:51:40
1085
Touré 💥☄️⭐ :
Solidarité mo amoul si rewmi rek .
Ken nite kou teki meuna au moins changer vie niari nite après nioniou def. la même chose Bou yague kouné moss
2026-11-09 07:14:01
306
Daro chic :
Ndeysane mêm mane sax g telma pleuré en rgardan la vidéo 😭kouy xeuy souba ba ngone di daw di dakeu ay 300f,500f nga bétéko téranga bi yeupeu ci ay waxtou,dina dioy ba dagueu😭nite kou am diom d loko dfal diarnako wayé yaw tamite ningako bété nii yalla nalako yalla bété ci barké Seydina Mouhamed(psl)🤲🏾
2026-11-09 06:08:44
136
@my_mou_Baye :
Lou Bakh reik mo ame solo,yalna ko yalla Faye🙏🙏😭😭
2026-11-09 05:02:26
52
mammicasse :
ndeyesan yalla Nala yalla Faye khole Bou seed doye na gnane tai kholam seedna
2026-11-09 12:41:52
0
Khadyseyefall :
G les larmes au yeux Lou bakh rek mo ame solo
2026-11-09 06:39:40
94
ma vie mon combat :
ndeysane weurseuk mogui founer yalnalaka yalla faye
2026-11-09 06:51:04
31
Linguère walo-walo😍❤️ :
Ndeysane bo khalaté ni amna proche youko monone def à sa place té defougnou ko bilahi lolou lay dioy
2026-11-09 05:34:28
77
sokhna :
Ki rewna dei[Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-11-09 08:51:36
30
Oumy thiam ngalam :
yalla nala yalla Faye sa khole
2026-11-09 12:24:43
0
Didija Rassoul :
Yalnala Borom bi faye MachaAllah
2026-11-09 11:35:22
0
tening.diome :
sallalahou alla Mouhamed 🙏🙏😭
2026-11-09 11:25:20
10
Yayou papam 🥰😍 :
la vidéo c'est pas su Sénégal, c'est au Nigéria
2026-11-09 07:48:27
22
Lisa :
Les jeunes souffrent vraiment
2026-11-09 09:28:12
9
madame seck♥️💍😘 :
ndeyessane 😭😭😭
2026-11-09 12:27:34
0
Mrs Faye 💍🫀🖇️❤️ :
Ay waye magui dioye sakh
2026-11-09 08:49:46
8
Mouhamed Rassoul Diop ✪ :
Yalla nla yalla faye🤍🤲🏾🙏🏿
2026-11-09 04:58:27
15
intima.bio :
Amgua nianou wadiour gueume koo rek Dina bakh inchalah
2026-11-09 07:26:54
17
Queen :
Mon dieu il m’a fait pleurer 🥹🥹🥹🥹oh Seigneur vient en aide aux démunis🙏🙏🙏
2026-11-09 07:18:49
9
7Z :
Yalla nala yalla takhawou si lepp li nga defal Wadji boul ko meusseu khep Lou reuy la❤️
2026-11-09 03:41:34
16
Miss lébouh❣️✨💋🍯🥀 :
Li nitte wara santei yalla barina yanala yalla Faye yiww si barkep seydouna Mohamed 🙏😭
2026-11-09 08:53:04
11
Reine mére ❤️ :
ndeysanne kou sonne rék yalla ga diaringou inchallah j'ai tellement pleuré
2026-11-09 06:18:18
14
To see more videos from user @interapple, please go to the Tikwm
homepage.