wa Guédiawaye waxo lene deugué ma lene geuna beug Balla Gaye té Guinée Biseau la deuk 🥰🥰🥰🥰 Balla Gaye seul ndam rék inchallah
2026-11-10 20:48:57
16
alindao650 :
Bly balla Yalla may nako Machalla
2026-11-10 20:32:47
8
Ibrahima Traore :
Billahi wa guediaway yena gooré . Ndeysane kholouniou tay déh mais Demb motakh niou diap balla ba tay dj 🥹
2026-11-10 22:08:07
8
Moné :
Bonne chance BG2
2026-11-10 20:43:26
6
papis :
diwagui né di dém yalla mokoy def si nit
2026-11-10 20:51:04
5
Lam zeune 7⚽️🥰❤️🫶 :
Li Bilay yalla
2026-11-10 20:51:38
5
Domou peul bi :
Guèdiawaye nio beugu balla bly
2026-11-10 20:54:41
23
wally FARAMARE🎤🎤 :
💙💙💙💙💙💙
2026-11-10 20:00:52
7
TAYROU BOU ADA FASS 🔥✈️ :
No déf danou 😂😂
2026-11-10 20:49:30
1
M.M.A.S 🇸🇳🔹 :
départ nane déh 💛💙💯✨🔥
2026-11-11 12:34:52
2
user7015695353312 :
balla gaye yalla nako Yalla soutoural may ko ndam inchalla amine
2026-11-10 23:22:16
4
Souzin :
non Balla dall moy lamb daffa nekhoul ba nekhoul wayer sponsors yi môme lagne beugue
2026-11-11 12:53:31
1
ababacargningue41 :
rousna romb té douma wah si mom. ndah ak loumeunti khéw fakhéna ba bén mbeur doufi retraité ak couronne bi 🫶👍 Simba le meilleur de sa génération 🫶❤️❤️❤️💪
2026-11-11 13:09:37
2
To see more videos from user @capo_613, please go to the Tikwm
homepage.