@une_daba2:

🌺✨UNE_DABA✨🌺
🌺✨UNE_DABA✨🌺
Open In TikTok:
Region: CA
Wednesday 11 November 2026 02:25:56 GMT
133807
4228
461
118

Music

Download

Comments

user353110107200
user3531101672000 :
Boutique khessal bir Touba modoul yone sakh
2026-11-11 08:19:29
521
modoukhabane
modou khabane seye :
danga deuk touba ba pareil khép wa touba
2026-11-11 08:10:20
274
thiatou.yayame895
wakaana hakane mon préféré ❤️ :
sokhna si yaniou togne heure bouniou néxé laniou lay bal
2026-11-11 09:21:44
251
famambergane1
Fama mrs wane❤️💍 :
Pour mome da wer mounane khana werouma
2026-11-11 14:35:14
44
yallakharitambalaynatou4
YND For Touhfatou ❣️ :
ya wax loula nekh niou wax louniou nekh
2026-11-11 07:48:05
271
cheikhiibra1
 CHEIKH iBRA ✪ :
dou diex dh barké brm touba dou diex
2026-11-11 12:32:03
155
siteuavie0
Siteu a vie :
Nena titre foncier la am touba sokhna si yaw lo deugu rk mounieul [Larmes de joie]
2026-11-11 06:36:09
117
bamba.talebe.bam
Ndiayene bi 🌚 :
Wakhall dague senegal yepou
2026-11-13 03:20:36
0
linguerfa22
linguer22🇸🇳 :
dou diekh dé dou linga beugon
2026-11-11 16:08:19
58
salihat173
Yayou s fallou🫶😍 :
Yaw parégou niou thi yaw sakh😂😂
2026-11-11 08:54:21
74
fadal442
MHMD FADAL :
Titre foncier bire touba Sakho paréngua 🧎😎
2026-11-11 10:23:04
33
mdchicandglam
MDCHICANDGLAM by Mamy DIA :
Haral baniou parei ya commencé mais nioune nioye agali
2026-11-11 10:55:57
96
divrrishsvmb
Divrrish Svmb :
Chérie pour Yaw danga wer ni
2026-11-11 13:40:47
38
narboundaw1
Soda Maréme❤️💍 :
Dou diekh deh barké borom touba mbacké
2026-11-12 12:38:11
5
aminavalverde8
Amina valverde8🦋🇸🇳 :
Khase niou ba paré diniou diay lamigne bou reuy
2026-11-11 09:08:52
61
bigtour16
Big tourè 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳 :
Sa marketing bi dé dokhna mai damaye xalat do diaye [Larmes de joie]
2026-11-11 12:55:52
22
bineta_amar
Bineta Mme Busso ❤️🫶 :
Beug nala balll Meh sama xoll mo masi bayii woul
2026-11-11 15:35:00
20
darousalamhalieutiques
Darousalam Halieutiques :
Bofi deuké té khep gnou nak
2026-11-11 11:16:13
22
mrs.sylla3
Bou-sylla🔐 :
Ya khepp sa deuk dall
2026-11-11 08:23:41
87
bourista650
Bourista ❤️ saliou ❤️🫂 :
Naniou ko balle rk 😂😂😂
2026-11-11 13:53:35
7
sokhna.arame.salio0
sokhna Arame saliou :
Mane dé paré gouma si yaw
2026-11-11 09:33:49
42
nogay075
Nogaye kane :
Daga wakh loula nekh doga diegalou gnoune tamite dagniy wakh lougnou nekh après gnou dieguel laa
2026-11-12 11:42:25
7
bbfambaye4
Bb Fa❤️ :
Mane dh balou mala
2026-11-11 09:52:31
20
ndioba544
Mrs💍 Diouf ❤️💍❤️ :
daw wowi khale yi niou 72h la 💃💃💃💃
2026-11-11 22:25:20
5
buursine25
Buur sine❤️💍 :
Vraiment lou wakh reuy reuy ak diégualou soûl na leppp kone balén ko
2026-11-11 17:35:16
5
To see more videos from user @une_daba2, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About