Na nga def ,, Maa ngi fi :
Ngir Yàlla Deeleen seetaat Seen Wolof yi, Li ngeen di làkk du Wolof de,
Tampts yii (Jamonoy yii, fan yii,,) chaque jour (Bis bu set) disparaître (Réer) Garde (Wàttu, Aar, Sàmm) En tout cas( Ak lu man a xew) pourquoi (Lu tax) Chuosire (Tànn) père(,Baay, Mag mi, góor gi) problems (Jafe jafe, mbir, giraawaali,) même (Ba ci) Village (Dëkk) tourve (Am) Solution (Pexe) pour (Ngir) Apres(Bu loolu weesoo, Ginnaaw loolu)
2026-11-16 20:23:12