@pacotilleno:

Gal Séne plus
Gal Séne plus
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 11 November 2026 23:18:08 GMT
18557
1021
37
76

Music

Download

Comments

daoudaalmouminoun
user1825194929364 :
guisguen dé avec sa niou beug ma tak😂😂
2026-11-12 15:18:02
3
mf151822ohl
kalidou Bou chiekh tidiane 🫶 :
adouna da diar li naniou rangual yallah tê yallah tax ☝️☝️☝️☝️
2026-11-12 11:42:21
18
d.gobalbusiness08
Rim ✨🇮🇹 :
Avec sa Senegal am nah djiguene bou bakh
2026-11-12 15:03:29
4
taphaomzzoniane
Prince🫅T@phii🫅Niane🌠 :
garss yii yewoulénn ngénn bagn mbeuteu yii beuGouniou kénn[Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-11-12 14:49:27
4
mass.gueye221
bathie massamba :
li mouy wakh ni mo nék si town bi dèih
2026-11-12 14:41:27
3
cheikhoul.khadim89
Cheikh ahmadou bamba 🇸🇳 :
Ki fiko wadji diap mo bakh
2026-11-12 12:07:25
14
bkx20
Kebe :
😳😳ki mane laye deff ni
2026-11-12 15:26:17
2
rasta.door.war
rasta.door.war locks :
Billahi vraiment nak wallahi
2026-11-12 14:21:48
1
abdouthiawo
abdou77 874 47 11 :
daysane diygen molandam
2026-11-12 11:37:40
5
ngor.bop2
ousseynou bop :
cv
2026-11-12 12:51:06
0
ousseynouba107
SENE VAISSELLE VIP :
❤️
2026-11-12 12:10:19
0
ousmanekebe0096gmail.com
seydina osman66🇸🇳🇨🇵 :
2026-11-12 15:07:33
0
mambou.cisse
mambou cisse :
2026-11-12 12:01:01
0
jambar221
jambar top :
khaw loula tee birr
2026-11-12 11:25:58
0
petitniang958
pi :
Li dayy dara si jiguéne
2026-11-12 12:01:09
6
ndiaye40988
Ndiaye :
Li moy jiggen jarul wolu si jamano tay
2026-11-12 13:22:18
7
lalchimiste492
L'alchimiste :
heureusement messouma am guel ba faune ko wakhou mala ak di teude ak mom billahi
2026-11-12 14:40:09
3
la.belle.fatima5
Fatima bby❤️ :
Alakhouak bar limotakh goor gni duniou am confiance si nioune ts wlhi nieup yamuniou djiguén mo leubdam 😭💔
2026-11-12 14:38:08
4
ablayedioufdiou69
Ablaye diouf Baye fall :
de nouye yoor sene djoko you bone bo parée nane moma diakhale
2026-11-12 15:27:19
1
keba.gueye352
kéba gueye :
niom khamou niou kou léne beug dh kou léne sonal léne kham après daniou tourné di wakh nane goor yeupa yém
2026-11-12 13:21:34
2
user9756180614834
user9756180614834 :
Sarah wakhouléne problème yeune nioka diom bay déh nguene di wakh sen problem bayiléne bonne
2026-11-12 09:36:48
1
modou2146
modou :
kou djignue ki bakhull
2026-11-12 11:08:30
1
khadimdiop119
user9149665264837 :
niom niépou la kothie térale doko lale do lale vename
2026-11-12 15:02:45
0
thiamlepauvre277
Thiam Baabél 🇸🇳 :
leer nama ni kawman leu boy yi daniou leen di nakh rek
2026-11-12 15:18:36
0
rimmkkaa
rimmkkaa :
ndeyssane djiguene nonou lagne mele😂😂
2026-11-12 10:12:55
0
To see more videos from user @pacotilleno, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About