@mamanazo86:

Maman azo
Maman azo
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 12 November 2026 09:07:27 GMT
241109
19900
580
3680

Music

Download

Comments

feuzboye2
Yayou Serigne Fallou :
mai khana procureur DICO guisoul informations bi
2026-11-12 11:03:12
1148
nagila690
Nagila :
mane dei jour boumako guissei dîna meti
2026-11-12 10:28:12
313
mamanlaya4
Thiatou yayame :
Police Senegal esk diote nagn si information 🤭
2026-11-12 10:12:26
898
lildas93
DA :
Senegal amoul autorité 💔😭
2026-11-12 10:51:10
362
gnagna0972
Gnagna Mboup :
Wakho Diam dh sama dome côté bobou si internat bi lay diangué😳😳
2026-11-12 11:26:45
95
bb.khady896
bb khady❤️ :
Police loumouy khar si cas bi tmt
2026-11-12 11:46:14
46
mmefallonly1
Bourou👑 keurem ❤️ Mrs F :
Mais est-ce ken la kon mou nek gnou bari com un genre de réseau
2026-11-12 11:08:50
294
aamiirabel0
amira :
lima diahal loutah sougne guissé auto bi dougne youhou gneupe gneuw
2026-11-12 11:14:35
116
lagodevosreves
Joloff Girl🇸🇳 :
Mais tamite que font nos autorités ? Bobou bataye nitt yi niongui alerter mais zéro évolution. En plus disparition dafa beuri, Yalna niou YALLAH aare 🙏🏿
2026-11-12 10:23:12
362
b2b_electronique
B2 Eletronique✪ :
Non mais attends yéne daguén Di guiss kén ame si mome soupçon wola daguén kham mer bi Sénégal dafa nékh koi mane li ay rumeur rk lako diapé
2026-11-12 11:15:15
26
ndeye.marem.demba
beug fallou :
moytou rek yalna yallah sam sounou djaboote yi
2026-11-12 09:51:07
621
evalabellecapricieuse
Eva nettoyage 🧹 🪣 🏠 :
Guéne yakarni auto bi dou gnari auto tamite parck nenagne mogui kaolack
2026-11-12 12:27:11
43
latouty0
LAGHERTA♋🦋🦋🥐🥐 :
wa yène lo lène di bayé xel do lène teuyé wo police tamite 😩😭😫
2026-11-12 11:24:16
56
auplaisiredesdames
julie :
Na wa quartier surveiller kogne bi bou bakh sakh
2026-11-12 10:05:33
89
babelbabel4730
Pothio :
La police fait quoi dans cette situation ????
2026-11-12 10:11:57
109
barhama496
Baba Diaw🇸🇳 :
Senegal khana amoul police😏
2026-11-12 16:26:50
6
mamina1477
Mamina🇸🇳🇨🇭 :
déléne surveillés khalé yi
2026-11-12 10:33:04
82
diallo782836439937
diallo machalla🫱🫲234 :
lolou souniou yone necout thie demal gendarmerie
2026-11-12 13:07:07
12
chawacollection
Glow de reine 👑 :
pourquoi bou nguéne ko guissé dou nguéne ko attaquer mane lolou moma diakhal enfaite pourquoi chaque jour tokk di khar police pfffff
2026-11-12 16:24:19
13
dibabusness
Diba :
Senegal t’amit li ken dousi wakh
2026-11-12 10:13:37
62
nenegalle932
néné galé :
Wa anii police sous Sénégal mane déh dama warou li doyna warr déh 😳😳😳
2026-11-12 14:52:52
6
user4706253781722
user4706253781722 :
mais loutakh dou nguen wo police
2026-11-12 10:55:22
18
odile_seck
Odile seck 🇸🇳 :
ben auto rek beugueu tere gneup nelaw hommes de lois yi nagnou diok si li way
2026-11-12 11:45:13
15
To see more videos from user @mamanazo86, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About