❤️❤️mo diapalè deih Rox la chancelière seul amoul lenene 🥳🎉🤸
2026-11-14 03:54:48
36
requin🦈mns :
Wawaw 💪🏽🎉🤸🏽♂️
2026-11-13 22:36:32
51
fall@1990 :
Rox yalna nguéné la ci kasso gui Amine Amine yarabi inchallah 🙏
2026-11-14 10:16:09
3
xoloumamendiaye :
Sama khôl bi toyna tay😭😭😭😭😭😭
2026-11-13 22:47:16
21
la princesse :
bilaye Rox talouye Li nako niepe niagnal yalla teguil ko natou bi ba pare Li yalla nako yalla takhawou ko yarabi khamou lene loumouye doundou instant bi si kholam bilaye ndeysane damako yeureum thiate rek 💚💚 mais yalla bakhna 💕💕🙏😭😭 notre soeur Rox bon courage
2026-11-14 11:17:45
3
kharitou papam :
dawna yaram yala naga guene si diam[Réconfortant][Réconfortant]