@cineteranga: Peut-on aimer sincèrement sa femme et pourtant la tromper ? À travers Aziz, Jeux de Dames nous plonge dans le combat intérieur d'un homme tiraillé entre sa raison et sa passion. #jeuxdedames #seriesenegalaise🇸🇳 #AmourEtPassion #maroditv #onregardequoi
Aziz loudoul irresponsable défoul ko
Nanal sa jus balamo tangu té bayil ma Aziz mi😏
2026-11-14 22:36:42
175
艾姆_凯艾尺🪭🇸🇳 :
ba boy sétan yagui diangualé
2026-11-14 21:45:18
110
Al Karim Parfum :
Motakh nit dafa wra tambal bopam ak yar bopam si loubax té bagna topou say beuge beug 💔topou li geune ndax se passé tôt ou tard dafay répété wou wat se live so manoul bougne se bakan 🕊️Serigne touba néna Ndaw bou yar bopam si Ndioub bu doné mak nopalou 🤍 nit dieufi hier moy doundou tay sou amoul ndimbal
2026-11-14 22:40:41
50
Kaddy Dumbuya :
c est pas vrai
2026-11-14 22:13:14
12
DIENG_VALVERDE_08_R_M_A_@_vie :
cou beuga terale sa yaye ak sa papa tekal fi sa lokho 🥰❤️
2026-11-14 21:47:52
48
BOUYANA :
Té boul fatté boye wakh del nanalé
2026-11-14 21:45:03
60
🄳🄸🄼🄺🄷🄰🥶🇸🇳 :
boye waxe dele nanale
2026-11-15 08:21:33
0
Mrs Mbaye 77 :
lolou moma dall😓
2026-11-15 08:40:51
0
Daouda.CR7❤️❤️🩹❣️👑 :
Bou viral lé guéne wakh ma ko
2026-11-14 21:45:00
23
La rebelle sudiste 💚 🧚🏾♀️ :
They homme vous arrivez toujours à vous en sortir 😅
2026-11-14 22:35:55
12
Mame Diarra 🤍🖤 :
Mariane si bopam mo wara dem bayi Aziz
2026-11-14 21:46:45
102
Users1233455677 :
Amoul excuse fi nieupa am ay beug beug dagay def sa bop nitt am foula
2026-11-14 23:18:09
30
chacha dieng :
Diaratoul sakh niouye setane série bi niew leen fi lepp lérr
2026-11-14 22:42:54
12
maodo Shop :
Aziz yii dé bary naa Sénégal [Ricanement]
2026-11-15 00:30:19
2
La Nabiénne 🦋🥰 :
Aziz dh foula RK la amoul
2026-11-14 22:02:17
6
une princesse 🌸👸 :
Massl dèf li
2026-11-14 22:00:20
5
NDIOLLISTA_d0 :
Tanks you ,merci beaucoup pour cette belle analyse
2026-11-14 22:40:42
5
Hass, The Gost12 :
Goor day yar bopam. Un homme doot maîtriser les désirs au lieu d'en être esclaves.
2026-11-14 22:52:53
3
Míriames❤️🩹🇸🇳11 :
Sama Dieukeur yallah boume guisse li il vas essayer
2026-11-14 23:44:25
2
fah.sy53 🤗❤️ :
C’est triste 😞
2026-11-14 22:15:23
4
Mouhamed thioune ✪ :
boul faté boye sétane dél diague 😏
2026-11-14 21:57:57
4
Awa chou :
Meilleure analyse 🥰
2026-11-14 22:08:51
4
alii :
Dans la serie Vampire Diarries, klaus avait à Stephane « ne sous estime jamais l’attrait de la noirceur » concernant l’attirance d’Elena pour Demon. Parfois l’ombre exerce une attraction fascinante sur nous même si on sait que c’est la lumière qu’il nous faut.
2026-11-15 06:04:01
2
Maïmouna Diatta :
Dél nanalé nk
2026-11-14 23:29:14
2
user8110266130023 :
2026-11-15 00:46:49
1
To see more videos from user @cineteranga, please go to the Tikwm
homepage.