goor banlieue yi yeup ay l'homme 12 métier laniou 🙏
2026-11-15 09:02:12
266
Khaliloulah :
Enfaite ce que j’ai compris et malheureusement mo dal jeune you bari l’homme 12 métiers amoul lolou kepp koukoy deff do ame metier mais xaliss ngay weur et j’ai compris aussi Ndiaye diangoul wone metier mais xaliss ladone weur malheureusement lolou moy sonal niou bari nite dangay am metier souko defei dinga si am xam xam ak xaliss mais sou fekei dàgay weur xaliss fo dem so amoul linga beug dangay dem seti lenen tei bou yaguei do ame metier
2026-11-15 13:01:37
35
bamba geulewar :
Goor deugeu Machalla
2026-11-15 08:56:22
113
Original by ngoy capo buMomo🎥 :
Machalah
2026-11-15 00:37:34
111
Ĝ🅰️LĀŜṢ :
Jambar la dh bly✌
2026-11-15 12:07:32
8
Ndäö Khalil :
Machalla
2026-11-15 01:30:02
64
Pãpįtø🥳 :
Un jour ma diangui ba wathie dém pour gnibi sougne keur basi yone bi ma tassé ak béne mère bu yore gaz🥺 mounima sama dome domabale yoboule ma gaz bi sama keur ma yeurame ko😞yobe gaz bi basi bire keur gui rek ma dale di guise ay bop😳 sama fit toga toule 😨ma def faire semblant melni ku guisoule dara après maniko sama téléphone bi dafa wade si porte keur gui xarale ma dieule ko mounima wawe rek ma dale di daw après thie la wo police expliquer co situation bi police dale di niaw ma wane ko keur mère bi après police diape ko guéné bop yépe ndakata ay bop chargeur la ak bop rallonge mofa nékone jour bobu akka ma tite
2026-11-15 13:28:54
0
FK Prince taekwondo :
respect si diambar ji
2026-11-15 14:48:55
0
Ultras_ASC~Maanko💛💙 :
Bilahi boy vrai guérié mais bilahi doma dap xamna sougn ma invité wonn may waxx limeu liguéy yeep téléspectateur yeepay dioy ba ni may waxx akh yaO ni je suis marié père d’un gosse mais batay niogui si xoslou bi teh taay la geuneu métii Bilahi téréwoul bayi wougnou teh djiss gall moniou térei deim ndakh situation jeune Senegal bilahi ayy Jaambar lagn nieup beug liguéy ✌️💪🔥
2026-11-15 09:20:24
40
Makavelli ✌🏿 :
Mes attend ndiaye dafa tekki wla? iow batay yangi sa Yoon di non boy nekh ngen nak😂😂
2026-11-15 11:40:30
6
~~MMD :
saay 31 moom demoul ngor🤣🤣🤣🤣🤣
2026-11-15 01:57:14
21
Abdou Rassoul lee :
Sénégal defa nekh dangayi guiss jeune bou amgoul 25 sa mouni la lima liguye barina 😁😂
2026-11-15 09:19:59
11
Bamba Lô 774763290🔥🎮 :
tk xél 😂😂
2026-11-15 00:30:24
34
Méringué.O.B.Y.🔰 :
Ndiaye lègui lane moy Sa liguèye 😂😅
2026-11-15 12:28:00
3
user8594162231124 :
8 ans 😂😂😂
2026-11-15 10:21:26
5
only god can juge me :
agne teudd 19h mais mba done nga dioulii timis ak gué rek nagnoukossi bolé amna solo
2026-11-15 14:59:11
0
Abou Sow :
🥰🥰🥰
2026-11-14 23:22:51
13
𝗸𝗮𝘁𝗶𝗺꧁𝚗𝚎𝚢𝚖𝚊𝚛𓇽✨💫 :
🥰🥰🥰
2026-11-15 00:53:35
6
mame cheikh amoul morome :
🥰🥰🥰
2026-11-15 00:44:51
6
goumba :
❣️❣️❣️
2026-11-15 00:50:45
5
DIANABA Diallo :
🥰🥰🥰
2026-11-14 23:16:11
11
𝐁𝐦𝐛 🤙 :
🥰🥰🥰
2026-11-15 00:38:55
6
nianeboucoubarsi2 :
🥰🥰🥰
2026-11-15 12:39:32
1
la diva :
♥️♥️
2026-11-15 12:04:23
0
NDOYE BOU DAW 808 :
😁😁😁
2026-11-15 11:00:54
2
To see more videos from user @lapaix160, please go to the Tikwm
homepage.