amna connexion ak serigne bi dai limou wakhni dai la waxon sama beneu xarit cheikh boye neko haut-parleur lou waral seydil hadji malick talif alla yarasoullalah
2026-11-15 00:37:00
22
niangousseynou2 :
micro.yi.dagnou.ko.wara.tall
2026-11-15 09:05:46
0
Seck Mouhamed :
wazifa lene té yocka radio yi mo Geune khana li Seydi el hadji Malick wax si wazifa
2026-11-15 02:06:24
13
ada mou same mboup :
serigne moustapha yalla nafi yagg ki boufi amoul niepou yapniou
2026-11-15 11:23:41
3
moumoune :
dieureudieufff SY malick weusifa dal nekh rek la defff ma sha allah
2026-11-15 01:14:58
11
ama emballage :
Yalla na yalla samoula sy malick koula guss rek khamni al amine moy sa wadiour ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️