Assalamou khalaykoum Tonton Diaw nourou darayni mane may borom commentaire bi magui doro guiss sa réponse té linga ma wakh ni yépou pour ma déf ko amouma matériel yépou instant bi
té souba la lundi souma diokhé woule xaliss bi souba lou nekh leume nama si fék doma ndimbeuly nguir yalla ng diokh ma lou simple diapalé ma guinaw yalla yaw rék la yakar
2026-11-15 22:35:16
6
blandinefourcroy :
cani by maman diakal
2026-11-16 16:43:55
1
mamy😊🥰 :
tonton kou rap bou sokhor diapp nk
2026-11-15 22:13:21
0
PABLOSCOBAR⁉️😇 :
Tons man rap moma sonal si louma dougou mou yakhou meunouma nek ak ken wolahi 😡