@tousa648:

Nèkh yayam 🫂❤️
Nèkh yayam 🫂❤️
Open In TikTok:
Region: SN
Monday 16 November 2026 17:48:46 GMT
212356
19122
505
1858

Music

Download

Comments

khadija95.c
LA REINE SAGITTAIRE ♐️💕 :
khew you laniiu wara wagni nieup nopalou mane vraiment chance bi khew am la guisoul
2026-11-17 09:35:17
980
anita35624
Nèkh yayam❤️🤌🏻 :
6mil tek thi maquillage ak gnaww bi ak perruque bi mou desss dalll ak sac 😂yorouma
2026-11-17 11:39:46
512
jaimemamere44
beug bayam :
té louñou sol béne yone paré si
2026-11-17 09:18:50
429
bintou_rass0ul
💕Bintou Rassoul 💕 :
Et le pire dounioula falé ba ame khéw dila message 😂😂
2026-11-17 20:55:06
52
ndarytoure13
𝐧𝐝𝐚𝐫𝐲🤬🤬 :
Ramadan le 8 février inchallah
2026-11-17 13:45:20
80
maremkho4
Marem khouma ✂️✂️ :
Boulniou yakall nioun t’allier yi
2026-11-17 12:54:25
76
nafnafbusness
Naf naf busness :
Mane legui ma bayi dem khew budget le te deuke bi nekhoul
2026-11-17 13:26:31
88
kebe343khadija
Khadijakebe :
Mane bizarrement kene moussouma bolei si hotess 😂😂😂
2026-11-17 22:53:16
20
perfecthidjab
perfecthidjab :
Khew yi lagne wara bayi
2026-11-17 14:08:46
10
salimatandiaye128
Salima80 :
Bilay wakhatiko 6mille yoyou bouniou dadialé won diokh ko borom khew bi moy eupou solo dé
2026-11-17 10:35:02
92
zeynii835
Nom d’utilisateur :
alhamdoulilah sama benn mbokk modone marier wakhoumako dama contane 😭😂 worr na yalla khew rek la bagn
2026-11-17 01:00:34
155
aminata.diallo944
Amina chou❤️💖 :
Wahatiko dagno soneu🥲🥲
2026-11-16 22:18:03
75
antarassoul25
antarassoul25 :
Après khew bi rk dougnou la wakh sakh merci
2026-11-17 22:04:29
6
une.baabel5
une baabel💋🌹🥰❤️ :
Wakh deug yalla
2026-11-16 22:56:15
39
metso496
metso496 :
Wakh deug yall 🤣🤣
2026-11-18 06:06:35
0
goralaye32
GORA LAYE :
khéw kay lanou wara bayi pour mou diékh
2026-11-17 09:26:08
16
amina56922
Amina :
Bilakhy man kifi Andi hôtesse la beugeu kham123 niouné hôtesse
2026-11-16 22:20:09
38
taphasamb22
Moustapha Samb :
Yow bougnou yakhal sounou liguey yow[Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-11-17 09:19:06
8
fatousougou522
fatousougou522 :
wakhga deuge
2026-11-16 22:28:44
16
poup.noir30
Domi🥰nar💞bi🥰 :
Man dak may yegual mani la waw doma guiss bama bayé xew la am diamou 😂😂😂
2026-11-17 15:21:52
8
2bmariama
Lady Bara D🥇💍💕 :
Ndakh yalla ga sagne ko wax
2026-11-17 14:22:16
5
soukeye.pouye42
Soukeye Pouye :
wakhale gama louma yague beugeu wakh souniou wa keur té khawma noumakoy wakhé merci ma belle
2026-11-17 02:07:44
7
salikhatecom.0
Salikhate busine🥰farfum ⚱️ :
bilahiii wax nga deug sonou na trop
2026-11-17 00:02:15
8
ibradiaw436
Ibra Diaw :
yalla khamnani khadiy diaw nagye wakhll dh
2026-11-16 18:14:00
9
To see more videos from user @tousa648, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About