@force.trankil.09: Heureusement qu’on lui a remboursé son investissement mé li métina lol way , parfois les ki néna de assane meserer sont compliqués #assanemesere #pourtoi #viral?tiktok🥰fyppppppppp #viraltiktok
Tay moom Assane poser na question ba paré ken Reeetaanoul 😂
2026-11-17 13:37:39
451
Real men :
sm problème mooy ay rakkam est ce que ay nitt laniou ak limou lène défal yeup nakh alaal ay waay soyons reconnaissant téh yallah takh😭😭
2026-11-17 13:46:51
292
tarkayii.com :
yéme na dh
2026-11-17 11:54:26
116
KS BSNSS 🇸🇳🕺 :
Nan ko Faye lolou kay amoull problème
2026-11-17 13:21:53
42
حكيم مسيري :
No lolu méti wul nanu diay keur gui ñoxko lime fa déff
2026-11-17 15:03:52
17
Seynabou Thiombane :
na danel bâtiment yep talal
2026-11-17 14:47:26
40
Mame Diarra ndiouck :
Yayame moko warone wakh deugue bi wala pa bi may ben parti avant mou décédé nak
2026-11-17 14:38:54
56
Faye salmone❤️💪🏾 :
Kone kou dioudowoul si boum dou donou en cas de mirass ?
2026-11-17 17:42:16
8
Muguiwara.Shop16 :
Man sama Xalate moy Ay Rakam Terrain laniou mom mais daniou kay diaye Terrain yi rek leep continuer wala Niou dieunde Keur yi rek
2026-11-17 12:44:46
49
Diya Fall :
sama khalate la wah nk esk douniou khol limou def si keur gui si khalise gnou delo koko wala gnou khol ndakh tolo na ak prix keur gui gnou bayékoko
2026-11-17 14:48:56
63
Sokhna kiné Maktuum🩷 :
Na démolir bâtiment bi bayil lénfa terrain bi
2026-11-17 14:27:41
32
Thiam Babel ♥️ :
thieuye yalla 😭😭😭
2026-11-17 12:31:34
67
Baye Garang Diouf ✪ :
Alhamdu lillaah Jërëjëfati Oustaz 🥺
2026-11-17 14:21:38
25
pa ousmane talibe baye niass :
ohh ndayesane
2026-11-17 14:28:00
11
Gueye elévage🐔🐇🕊️🦃🦆 :
lou méti way thiey
2026-11-17 14:48:50
16
lepah :
keur daal sa keurou bopp, keur famille loy fay deff na saam teh nagko meun . Tant que parents sont en vie meun na bagna am problem mais une fois niou décèdé problème yi commencer
2026-11-17 14:08:07
28
Ël/Čãtålàns🤍🩵 :
Man damay yak keur ngui dem sama yon kou d’accord
2026-11-17 14:41:07
12
Enjoy myself 🧠❤️🇺🇸 :
C’est grave ça 😭😭
2026-11-17 14:15:04
6
COACH SAER :
lolou day yomb
2026-11-17 14:14:52
6
BAYE69🇸🇳🇮🇹🫨 :
Ohhh😭💔
2026-11-17 20:24:18
1
Fatou Njie :
🤲🤲🤲
2026-11-17 18:34:55
2
To see more videos from user @force.trankil.09, please go to the Tikwm
homepage.