Yalla na Gnou Yalla yeureum amine 🤲 AK mbonlém Dioulit Bou nk si br Souf 🤲 AK mbonlém Dioulit Bou nk si kaw Souf 🤲 Thie barké khassida yi 🤲 Yalla na Gnou Yalla Fayal S SAM Mbaye 🤲
2026-11-17 22:26:02
2
Taxawu Ñoñ ALXUR'AAN Suñ Yitte :
Seex Saam Mbay YÀLLA nanu ko saa BOROM gëna dolli Fayal yiiw te saxal ko ci yërmànde ak ngërëm aamiin BARKE ASNAA XADIIM