@mamendiayesavon111:

Mamendiayesavon
Mamendiayesavon
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 17 November 2026 19:47:55 GMT
2065
296
38
8

Music

Download

Comments

sen.le.vrai
le vrai :
Massa tanel mame dka wara repose bilay do machine dkay liguey rek repos toi ba décembre gua geneu
2026-11-17 20:00:21
80
bousso.bally986
bousso bally bou mame ndiaye :
Yalla nala yalla takhawou ❤️❤️❤️❤️
2026-11-17 19:57:49
17
thiambenethiam
Thiam Ben Thiam :
ALLA HOUMMA YA CHAFII ICHFI MAME NDIAYE CHIFANE WA SALAAMANE BI BARAKATI SAYIDINA MOHAMED SWS
2026-11-17 19:58:27
12
mawaforger
Domou maman ak mame❤️ :
Prompt rétablissement boula Dara diote yalna yallah may tane🤲😭❤️
2026-11-17 19:50:41
87
mariame3257
mariame🥰🇸🇳 :
dara waroula dal souniou yaye dji bonne rétablissement 🥹🥹
2026-11-17 19:52:45
14
antabeuguefallou0
Anita fans mame ndiaye ❤️✅ :
Yalla nala yalla maye were🤲🏻
2026-11-17 19:56:15
9
banekhboumame
banekh Bou mame Ndiaye savo ❤️ :
sy Malick niane 🤲🏾🤲🏾🤲🏾
2026-11-17 20:21:53
2
cheffekenza0
Cheffe 🧑‍🍳 Kenza 👩‍🍳👩‍🍳 :
Massa notre reine thiate bakhoul Yalle nala yalla weral ak diam 🙏🙏🙏🙏🙏
2026-11-17 19:57:42
7
minaaboumamendiayesavon
Mina domou l’international bi :
yalla na yalla yeketila si barkel naby mustafa🙏🙏🙏❤️
2026-11-17 20:13:32
5
monmarimoncombat2
In god we trust 🙏🏽🩷 :
Mame raral TikTok bi touti gueu gueneu nopalou beu décembre hinchallah. Yallah nala Yallah may tane thie barkel Seydina Mouhamed 🙏
2026-11-17 20:06:37
2
sayfa449
Sayfa :
Ay yalla j'ai peur dé. Yalla Mame Ndiaye rékk lala dégue thi tik tok bi. Je ressens toutes ses douleurs. Yalla he te confie Mame Ndiaye savon💚💚💚💚
2026-11-17 20:31:00
1
gueyebusiness26
Gueye Business :
ndegg nala yalla mou arla samla ci barke seydina Mohamed Rassoulilah salalahou aleyhi wa salam amine 🥰
2026-11-17 20:26:01
2
faye.faye53
Faye Faye :
massa sama caviar boula dara djott ,bon rétablissement
2026-11-17 20:30:32
0
kinesaliou051
🌺🌸—KINE—🌸SALIOU—🌸🌺 :
Yalla gua tane ak diam inchalah 🥰🥰🥰
2026-11-17 20:19:33
1
nickilabelle4
Nicki la sénégalaise 🇸🇳🧿 :
Meyeur santé mon cœur ♥️
2026-11-17 20:25:16
1
lavieestbe30
Thiate🥰 :
Bon rétablissement
2026-11-17 19:55:30
3
absasaliou11
Salihat❤️cafè :
Weur ak diam way
2026-11-17 19:49:36
4
fatoudiange8
Narou yaye khaïta :
Diammou ak salam thi iow
2026-11-17 19:49:50
3
rewmirekwawaw20
🥳💚 Rewmi nekh na💚🥳 :
Bon rétablissement mame yalla sameu la are la 🤲🤲🤲🤲🙏🙏
2026-11-17 19:56:38
2
wourous7
🌸Seynab__rassoul 🌸 :
Massa boula Dara diote 🙏🥰❤️
2026-11-17 19:59:36
2
beuguefallou865
L’américaine bou Mame Nd S 🧼 :
Boula dara Dale mame ❤️❤️❤️
2026-11-17 19:51:29
3
element.serigne.s80
Fatoucha la chancelière 🥰🧏🫴 :
Dégaye nopalou mame 🥰🥰🥰
2026-11-17 19:49:47
4
evabualou
Ev@bualou🇸🇳🇪🇸 :
Yalla nala yalla same arla 🙏
2026-11-17 20:00:32
1
To see more videos from user @mamendiayesavon111, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About