saway adouna yalla ko moom nan diokhe yalla loumou yello leep yalla leu amoul kene lene loudoul yalla
2026-11-18 11:03:52
0
Cheikh Sene :
yoro Sénégal way
2026-11-18 05:24:59
6
djily mou oumar sall sounnah :
yala mon yor Sénégal nit yoroul Dara
2026-11-18 01:17:04
25
Birame Ndiahetiktok.com/@biram :
li mon yack Sénégal nit déy wakh guédi wédi té khamouléne kokou louko yalla diokh ki liko yalla may liko serigne touba may khamouléne ko ki dou wakhatou mouck bilay ladje léne sene président yi fi diarre yéne yi commentaire Lou négatif khamouléne dara bilahi
2026-11-18 08:56:45
12
BIG BAOL SERERE BI🇸🇳 :
xam xam bou mégo ak Al Qurane ak suna rék mo wore Roog soom moye borom kouné fa ya kouné🙏
2026-11-18 15:14:00
0
KSF COUTURE :
Machallah Diomaye seul
o kiné pogoume
Diokh ôndiale Diouf
yaa same o migne mé