@sonko_officiel: #Dakar la vie cher au #senegal

SEYDINA
SEYDINA
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 18 November 2026 15:17:39 GMT
77624
9286
659
222

Music

Download

Comments

sopbromtouba
diopassane71 :
nioun waa all bi niogi ci jàmm
2026-11-18 22:38:53
161
hnrb16
hnrb16 :
Dakar la khamé louy khifff .il faut vraiment le cardio pour vivre ici
2026-11-19 08:47:46
168
lapfall28
tine :
Dakar kay nekh sow lanouy doun dh😂😂😂😂
2026-11-18 23:17:42
267
coumbandong519
Coumba Ndong :
15h 33 bourou ak sow Bou nékon village ma dor sama bakhal ba gat yala bakhna [Tears of joy][Tears of joy]
2026-11-19 15:35:12
0
mayababy392
Maya sérére💯 :
Dakar la guiss gnouy tangual agne 1 mois ndakh metti
2026-11-19 09:19:51
34
elhadjingom770985982
PETIT ELZO💕💕 770985982 :
kou hamoule Dakar réke moye wedi 🤣🤣🤣😂🤣🤣🤣🤣
2026-11-18 22:42:29
122
ibrahimadiouf9471
cr77 :
Dakar amoul rerr
2026-11-19 04:33:25
11
khalifaababacar486
Khalifa Ababacar Diagne⚽️❤️ :
Sa wayy ga gnibi sen deuk oki😹 Nioune Dakar laniou deuk oki🩸🫶
2026-11-19 06:44:11
12
boykanarouyakhady
boykanarouyakhady :
Fouf Dakar diame amou fi bilakhi 😂😂lékouniou nanouniou rakh thi doli fouy 😂😂😂
2026-11-18 22:30:23
53
papecheikhcisse85
papecheikhcisse85 :
kone gnibilene dakar mon eupe barké si Sénégal kou diakhlé gneuw gnou teralla
2026-11-18 23:00:51
31
diobass2
boy :
billahi leka bi ame village amoule Dakar pere village chaque dagaye le 3 fois
2026-11-18 19:49:49
47
user87331106
deugue rèk :
Wa kaw gui sante yalla bou bakh
2026-11-18 18:50:44
174
truellepro11
Truelle pro :
KON Dakar amoul tieré xana.
2026-11-18 17:32:23
14
messi.bou.sonko10
% MESSI BOU SONKO % :
bilahi
2026-11-18 15:54:08
17
babacargueye946
Babacargueye946 :
village mom amoul khiff ,dègnouye bèy dougoup,maïs,dorgot,bisab,gnèbè arachide,pastèque,même thièbe actuellement dègnouye béy ay hectar, am courant ,0 agression,amoul fèy location 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
2026-11-19 11:43:32
12
matydiop1659
tyma choux🥰❤️🥰💍 :
bilay sama deuk mo gueune nékh dakar
2026-11-19 09:55:21
7
salioudia431
CHEIKH SALIOU DIA📱🔘 :
Pére gnun gni deuk thi village yi lou deuk bi métti métti dagnouy agne réer ndeki té dougnou Diambat Dara
2026-11-18 22:24:35
16
cherif.ngom14
Cherifkhadija :
Lathie léne étudiant yi [Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-11-18 23:23:09
12
dethiediouf156
Diouf l’homme de mbadane :
Limay lek dakar yeup thiere deuk baa momako geunal
2026-11-18 22:34:11
9
dia27334
dia :
village dh kur kodougo léku ba bayii fay amoul kur ki AK ké lépu bén le allhmdou lillah loumou méty méty léku mom dan Koy déf bamou doy té niou and si lépu
2026-11-18 22:42:43
9
falouc
falouc :
bilay valay
2026-11-18 15:26:20
11
le.djiaraf1
O maad👑 :
boy village dou moromou Dakar ✌
2026-11-18 22:48:59
7
user1131615110358
user1131615110358 :
Dakar dagni moss rekk
2026-11-18 22:28:45
9
karbala768440408
Darou rahmane fripper768440408 :
Merci per fier d’être villageois 🩸🩸🩸
2026-11-18 22:49:14
7
To see more videos from user @sonko_officiel, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About