bilahi walahi lou wér la serigne bii yalla nala borom bii guena takhawou man déh guiss nasi sama bopou bou bakh et yalla rék mo takh may wakh
2026-11-18 19:57:57
20
La vie est courte💚 :
Serigne seck dafa am kham kham dafa bax yalnako yalla may goude fane ak wer🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
2026-11-18 21:54:33
0
diouf :
je le confirme ayy diamono damay heyi mou metti lolo journée bi yepp bi yepp douma diaye ambulant laye def wayé depuis bama commencé bismilahi mangui outi arakhmani ma ame arakhimi ak diarigname vanguisi guiss sama bopp
2026-11-18 20:32:33
4
Aïdara Ndiaye :
yalla mo laye fay
2026-11-18 20:23:38
0
khady Mbacké :
kide koubakhla defnako gissde machallah amo morome de
2026-11-18 19:50:51
5
adama Diagne :
Loulér
2026-11-18 22:06:01
1
aluminiume :
manchallah
2026-11-18 21:23:30
1
Assane Ndour :
machalla amnasolo dieuredieufaty
2026-11-18 20:23:35
1
Dakar_electormenager :
Bilay Deugueleu
2026-11-18 19:35:58
5
Perspicace 😘⚡️✨️ :
Wa gniy def télétravail dakh mane nagn ko deh ?
2026-11-18 19:31:50
2
Ndeyasaliou🥰 :
Salalhou allah mouhamad
2026-11-18 20:45:41
1
PROFESSIONNAL DRIVER :
Mane salarié la mais guissa gouma dara
mais douma bayi inchallah
2026-11-18 22:25:14
0
user97383905034014 :
sallahou allah mouhamed
2026-11-18 20:39:26
1
sopé serigne saliou :
Ki diam rk lay ame
2026-11-18 19:31:01
2
Daro Gueye :
walahi yalanal yala faye lou werr la
2026-11-18 19:57:46
0
Ibrahima Sewrou Diallo :
mandé Sama problème mooy chaque jour damakoye fatté mandall damay tooj Sama place Sama khel demthii
2026-11-18 22:32:16
0
Dieng Sylla :
mane de souma kheuye dinako Def machalla
2026-11-18 22:33:51
0
MOUHAMED :
Déf nako tay mais magui Sant yalla
2026-11-18 22:09:34
0
Yaye fall serigne fallou😍 :
Machalla 🥰
2026-11-18 22:11:30
0
mage :
wawaw bousso seck mou bakh mi goudou fane ak wérr
2026-11-18 22:19:20
0
Ndiogou Fall :
🔥🔥🤍🤍🤍🤍🤍
2026-11-18 22:23:51
0
ibau Ndiaye ♥️ :
2026-11-18 22:15:00
0
Salle Diara :
2026-11-18 22:12:38
0
user3251461016685 :
❤️
2026-11-18 22:23:32
0
To see more videos from user @abdouboussoseck, please go to the Tikwm
homepage.