diambar amoul kou yalla dimbeuli mofi neik ndax lofi ligeuy bâ yalla may la teranga nit soneu na louko raw fouf t amoul
2026-11-25 19:42:44
0
ndourawally4 :
@ndourawally4: Mame Diarra Seck rombou len fofu deh khna
2026-11-26 09:27:35
0
PacO🇪🇸🇮🇹🇸🇳 :
Mbëbët yombou naa wayé amm ay diaffé moko lakh bayyi ci xel bro
2026-11-19 13:56:51
61
bb fa :
aman solo 🧏👂
2026-11-19 14:25:37
12
thierno Fall🇸🇳 🇺🇸 :
Barina gnou meuna wakh deukk mais dougnouko diefe
2026-11-19 17:30:27
6
Yeum’s🇧🇪🇸🇳🇮🇹🦅b❤️c :
very nice 🫡
2026-11-25 12:53:50
0
pablo07 :
Adina djigen ak takander gno yam losi dake dokotap waye losi wan ginaw doko raw❤️
2026-11-19 19:11:39
7
Baye Foden :
Kou amoull ligua beug daguayy beug ligua am
2026-11-25 07:15:29
6
Mouhamed rassoul Barry 🇸🇳❤️ :
Bro djirime nekoul si ñakk ayy waydiour wayé migui si ñakk xam-xam akh ay téguine ❤️
2026-11-19 15:41:00
17
𝐏𝐄𝐓𝐈𝐓 𝐋𝐈SS ✈️🇱🇷💪 :
Nala état protégé
2026-11-19 18:21:27
5
Ya MOUSTAPHA 🇲🇦🇲🇦 :
Bou lépeu yombone dara dou rafétt 🫡
2026-11-19 17:19:27
5
tallambaye911 :
ak kills kharafall
2026-11-19 15:42:57
0
Ara le jeune élégant 🥰🫶 :
Don’t worry bro good is never late ⏰
2026-11-19 14:52:55
3
omarkane64 307 bi :
bro bo amé sakhla wakh ko yala ndakh soko sakhé nite douko fathie té dinako wakh niape mé boko wakhé yala bouko fadioul tamat douko wakh kéne bro 🥰🥰
2026-11-19 15:08:18
6
MOR😘 :
Fo begoul fanane sofa goudé Yara bayi sa bopou🥰
2026-11-25 23:33:01
2
awa thiam :
diamono bi niou nék kéne diarou ta yéde loy def mouna toko di ngua ko bayi aduna kou nék ak sa pékhé wayé tamit kou nék ak sa pakhe
2026-11-19 15:42:44
3
Defe jr 16 :
def té yalla takh diaroule khar ken dilasi guereume👂👈
2026-11-22 21:14:11
2
bbnox :
Troisième bi wakhou serigne saliou la boul wakh kényan ni la mél wayé fékhél ba ko dieufleuntél mou beugeu mél ni yaw ndeysane 🥰
2026-11-23 07:42:05
2
Samba Kane :
Soone mo geune diakhlé🥰🥰
2026-11-19 20:51:46
0
Dame Ngom :
boo beugué, boul tite🧠
2026-11-24 15:10:33
3
bay Barham cissé 🌹🫶🇸🇳🇬🇲 :
chaque personne doit regarder sa vie dans 3 direction en avance pour savoir la où tu vas en arrière pour se rappeler dou tu viens de côté pour voir qui t'a accompagné dans les moments difficiles. bayi si xell bro. have Good dey
2026-11-19 15:01:29
4
HOUSMANE IBN HAFFANE :
préférel nek nitt biniouye worr mais boul worr mindeff🥰
2026-11-19 18:25:07
0
Omzo Nazi🇸🇳 :
Bou niit khamon fan la tekki nk Kone kën dou lambatou 👍
2026-11-20 00:04:03
0
ousseynou fall :
2026-11-23 20:26:37
1
To see more videos from user @makhtar.drame467, please go to the Tikwm
homepage.