@lesaloum.sn: Cas mortel à Kaolack #viral #fyp #kaolack #drame

LE SALOUM🎙️
LE SALOUM🎙️
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 19 November 2026 19:35:18 GMT
74451
5924
143
269

Music

Download

Comments

diopmoustpha
Serere bou rafete 🥰 :
Kou bakh ndaysan 😭😭😭
2026-11-19 21:26:13
43
facissthiate
facissthiate :
Li lay ragal mou am souniou keur entre sama frére sama dieukeurou sœur bi ak ay doma me diam meunou fé am souniou keur 💔
2026-11-19 21:44:25
33
azoumasensei
06 Decembre ♐️✝️🍀 :
Li mom banne kogne la ?
2026-11-19 21:01:40
19
user66761553600250
met za :
kana dafa décède kon
2026-11-19 21:54:32
5
user5696584725791
Cheikh Tidiane Gueye :
rayy naniou dioulit pirr .imam ndaysann niite kou bakh
2026-11-19 20:10:38
105
bakhyayeshop3
bakh yay fournisseur🛍🇲🇦 :
thieye yalla togn nite ki parei rayko lore ndiebotam ni😭
2026-11-19 22:10:27
3
momo.dexter1
𝕞𝕠𝕞𝕠 𝕕𝕖𝕩𝕥𝕖𝕣 ✪ :
Kaolack fani reupe na dh
2026-11-19 19:43:36
76
formatrice.restaur
Formatrice restauration :
Dagno warra deiff ko rayeee gniii rayee la mou dieihhhh
2026-11-19 21:31:35
20
une.gueye018
❤️ Queen Rokhaya 👑� :
Bilahi sou guén don df kou ray niou ray la walahi dinén bayi 😭😭😭
2026-11-19 21:36:41
14
adjadieng88
adjafatoudiop7 :
Motax yé fitna bakhoul
2026-11-19 20:28:38
38
user8130613068278
user8130613068278 :
diamono bi gnou tolou kounou rayoul yalah mola mouseule dou diamebare
2026-11-19 23:15:42
1
abderahmanelo
Abderahmane Lo :
rewe rek
2026-11-19 20:03:37
46
dave_cana2
Dave le madrilène ♥️🔥🩸⚽✅ :
pa bou kham la bilahi😭
2026-11-19 20:30:21
18
user4138885884596
yayou Babacar 🤱 :
thiey problème yisi keur yi
2026-11-19 20:56:01
6
khqr.niang
user5745626348727niangniang :
thiey yalla sounou borom li niawna trop
2026-11-19 20:54:48
14
oumy.ndiaye097
Oumy Ndiaye :
bougnou defoule balonte national temouye deugue bilahi dou bakhe😭😭😭
2026-11-19 21:23:45
3
modoud038
MODOU COMEDIÉN 2 :
Nonon😭😭😭🙏❌
2026-11-19 22:25:34
1
aliou.fashion1
Aliou fashion1 :
Li metina 😭😭😭😭😭😭🚨🚨🚨
2026-11-19 19:47:37
12
mya_fall_damel
mya fall :
ayyyy wayyy 😳😳😳😳😳😳😳😳😳métina ndaysane yalnako yalla kharé aldjana firdawsi nit gni danion sokhor séne khol yi mo bonne
2026-11-19 20:09:58
18
niang0425
niang :
thieye yalla
2026-11-19 20:25:41
7
missndamlo2021
Miss Longrich Lo ndam💸 :
Setlou ngen ni deug en famille problème rek lay indi 1 2 3 nga dieul paka khol yepa khate vraiment metina😭😭😭😭
2026-11-19 22:40:23
1
mariclaude33
Élément Serigne Fallou🫶🏼❤️ :
Yalnako yallah yereum 🤲🏼🤲🏼🤲🏼
2026-11-19 22:19:18
1
mareme.sy40
Mareme Sy :
2026-11-19 20:15:22
3
ismaila2008
꧁ 𝑰𝒔𝒎𝒂ï𝒍𝒂 ꧂🦇🇸🇳 :
Non sm kogne la😭🤦
2026-11-19 21:38:58
0
jarrahrasoul
مام خار رسل 😍 :
Wa temps yi ray bi bari na dh alahou akbar Lou nek si khol nit yi khaw ma dinio fate yalla ou pas ray ray rk
2026-11-19 22:29:27
1
To see more videos from user @lesaloum.sn, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About