Lima geuna nékh si wakh dji moye kéne meunou niousé détourné virgule
2026-11-19 23:38:08
734
Dér bou nioule 🐍🐍 :
Bilahi je suis Talibe cheikh mais je suis catégoriquement d’accord avec gana 🧏
2026-11-20 13:42:43
159
L’homme incomparable 🧠✪ ✪🇸🇳 :
Te nioune sakh serigne bi topèwougne ko Adiana
2026-11-20 09:08:03
148
Ablaye bou Bayern München :
serigne touba yalla nako yalla yeureume té attéko si yeurmandénme
2026-11-20 04:18:48
128
beug serigne touba . :
yobou ça moromou djioulite adiana ces facile juste teko ci yonnou siratal moustakhine serigne touba ci yonne bobou la nek yalla ak yenéntibi ak alkhouran kessé moko niore
2026-11-20 09:46:07
121
SOUKEYNA❤️🌹🇸🇳⭐⭐ :
KADOU GUI WAW KONG LA DÉF
2026-11-20 07:44:42
99
Nittou Bamba🫀🥹❤️ :
Barkép Cheikh Hamsa 🥹💙
2026-11-20 15:04:25
27
Lat soukabe :
li dess fii ak adouna di toukki geum fi lenne loudoul dame khadiou fi