sama voisin chrétiens bi frère bi naré deff baptêmes dome dji 3 jours avant demna tchi voisin yeup pour khamlen ni di bâche bayal bi le samedi mouy excusé wou tchi dérangement ak désagrément bi nara causé meme keur youmou khamoul . 🥰 te gnoune sunu kanaw keur koufay bâche dougnou tagou dgnouy fate ça sunu fenêtre pare dougnouko nettoyer 😭
2026-11-20 10:45:23
232
user6456989034066 :
les mosquées aussi il faut en parler ..
2026-11-20 07:27:53
88
cheikhndiaye482 :
Ak diaka yi 4h nga tal say radio ken dou nelaw ak wasifa yi tmt
2026-11-20 12:46:47
60
Arcadian🇸🇳 :
surtout wazifa ak thiant yi
2026-11-20 13:05:15
34
ablaye aw :
dieurdieufe oustaz doundeul wereul surtout souniou banlieue bi
2026-11-20 15:49:32
71
cheekhfaal :
dahira khadiou gouda ak wazifa fadiar yignouy diangue ci micro yi ak thiante khaadiou gouddi ay akh kepp laniou city dieulê. Haut parleur yi ak micros yi modoul yoone.. kenn meunoukoo layal ci diiné
2026-11-20 08:55:21
35
mouhamadoulamine diallo :
Vraiment Oustaze Modou Fall,sois remercié pour le rôle de clarification que tu joues dans les consciences des sénégalais.Tu es d'une objectivité courageuse et généreuse.Que dieu te protège.
2026-11-20 07:38:18
24
R🇨🇻🇸🇳 :
Kone juuli fajar warou nio taal radio jakka dji?
2026-11-20 14:33:52
8
Gueye Teranga :
Outaz Modou Fall Gno bokou Serigne Babacar Sy wayé ligua wakh andou masi
2026-11-20 12:52:03
6
#Major🇸🇳 :
Insistelll si lolou. Gni weirougnou koiii
2026-11-20 18:00:03
10
mame Ndiaye diatta :
maynleniou diam modou fall Lou Mouy wakh sa n'a rien à voir a mosquée ak wasifa nék len nit
2026-11-20 16:51:04
8
Cheikh Seck :
mais oustaze ya wakh deug lii mo takh malaye suivre
2026-11-20 08:37:24
35
KOITA MAKALOU 227 :
bien dit ya oustage 🤣
2026-11-20 06:52:50
43
#€! Samba @ Tik tok :
bilay oustace wakhal dé sonounaniou Quen niemewoul wakh ahhhh🇸🇳🇸🇳
2026-11-20 10:39:32
1
ma10 :
Modou Fall bayil conference kon
2026-11-20 16:01:25
0
Cheikh Tidjane Sow 🇸🇳 :
koudoul dioulli yagui si erreur
2026-11-20 10:05:28
17
Tony almeida :
Billahi
2026-11-20 08:06:10
15
diop :
bo wakhé niounane daniouye dahira douniouthi ame touss loudoul ak deukeundo
2026-11-20 11:25:40
6
FALLOU,vitfés, parfums,divers, :
Bilahi Oustaz deugue reke nguafi wakhe
2026-11-20 09:14:36
6
honorable député :
deug bou wér
2026-11-20 08:38:55
9
pekoss Dida :
vraiment wokhga degue oustaz
2026-11-20 12:44:47
7
Bass :
lou lere
2026-11-20 12:17:59
6
BipaGalsen🇸🇳🇫🇷 :
Sénégal si bopam nio bari bruit
2026-11-20 14:28:31
6
To see more videos from user @versetdu.jour, please go to the Tikwm
homepage.