Diabaar daw ba kheuy d khamako d mai les images parle t khalé mai diabaar la
2026-11-20 13:54:42
11
papaguey3225 :
Ndayesan yalla nako yalla yerame 😘😘
2026-11-20 19:58:37
1
Dione éleveur :
Ndaysane amena nio khamené warou nio tééla déé danio wara doundou ba maguette yalla nako yalla yeureum té djégal kharéko aldiana firdawsi amiiine
2026-11-20 15:59:28
5
ndama12 domou fass :
yalnako yalla khare aldiana
2026-11-20 16:45:30
1
M.c.tlb ndiol fouta🙏 :
Diambar deug demna💔🕊️
2026-11-20 12:11:01
3
SERIÑ SALIOU REK LA BEUG❤️🇸🇳 :
Limotax yakamtiwouma dra sma life ki waronn na doundou basi kanam jaambar nga dh image bi wanénako thiono yinga dathi sisa doundou yalna boko dathi sa birr bammel dors bien champion yalna nga motaler sa ndaw aljanay firdawsi li metina🙏💔🥹
2026-11-20 19:29:14
0
Oumyta Shop👜🥿🎉 :
Bilay adouna defois do sakh comprendre ndiaga yalla bo guiss Lo ragal si bamel
2026-11-20 14:08:05
2
Salallahou alla Mouhamed ❤️ :
Ylla nko ylla yeureum
2026-11-20 12:19:39
0
Kheucha Thiatou Khouba 💚🤍 :
ndaysane bilahi lépou si beugua téral wadiour yi rék, yalla nako yalla yereum téh kharé ko aldianay firdawsi si barkép kou tédd ki
2026-11-20 14:32:53
0
mouhamed mbaye 🥰💕🫂 :
yalla nako yalla yeremm😭😭
2026-11-20 15:02:55
1
dame Bou pape Malick seul🇪🇦 :
oh diambar degeu dèm na 😭
2026-11-20 14:10:16
0
Cheikh mou S.S.M LG❤️ :
thiay sonou broum 😢😢😢
2026-11-20 16:03:37
1
Mme Ahmadou Bamba ❤️💍 :
On a vraiment le cœur meurtri
2026-11-20 19:22:20
0
Maáme Faállou Glasse 🫡💰 :
Yalla nako Yalla yeureume
2026-11-20 19:20:26
0
Bamba Apelle 🍎🍏 :
الله أكبر 😥
2026-11-20 12:47:43
1
Mafall :
🙏
2026-11-20 12:08:03
0
diop :
2026-11-20 19:05:38
0
Maoda :
2026-11-20 18:39:22
0
user6642696295548 :
Diabar demna😭😭
2026-11-20 14:02:09
0
user396635661965 :
😭😭
2026-11-20 20:01:08
0
Adji💋🥳🎊❤️ :
thiey Yalla
2026-11-20 18:52:33
0
Mbole Sarr :
2026-11-20 15:33:10
0
Kale Kante :
yalla Nako yalla yeureume
2026-11-20 15:15:42
0
MOR_PRO🇪🇸 :
Amine 🙏
2026-11-20 13:09:28
0
To see more videos from user @ahmadoubamba408, please go to the Tikwm
homepage.