Sa mame Cheikh Ibra néna À Doom, yeen góor ñi, Yàlla rekk ngeen am, kon na ngeen jug dox jëm ci Yàlla ; jigéen ñi tam, yeen rekk lan fi am, ku ci nangoo ànd ak yeen jug jëm ci Yàlla, deleen ko dimbali ci seen i wersek ak seenum xel, di leen yerëm ngir ànd ak ñoom dox jëm ci Yàlla, waaye ku ci nanguwul ànd ak yeen dox jëm ci Yàlla, nee leen kafa ñukk te jem ca Yalla. »