Waxna deugg dh mane dh yango douma beugg mou nieuw si kogn bi ndax wax nite yi walahi Sénégal dfa meiti
2026-11-21 18:31:36
18
Ndeya la princesse ❤️ :
Wolahi touma bakhoule ❤️
2026-11-21 17:48:30
11
❤️Marie❤️ :
Bilahi Sénégal dafa meti dagni yakh Ngor
2026-11-21 18:46:16
2
Athia Ba :
ëulekk yowmall hiyaam dina mêti🥺🥺
2026-11-21 18:31:53
2
pdgrima :
Ndessane
2026-11-21 15:57:41
10
unknown :
akay deug mane thi tata la nek damay téla kheuy surtout sama auto sou néké thi kaw 3h 30/4 ba 50 defois damay guenn mais lunek guay deug worna Yallah meuna dieulé auto Fass Mbao pour dem station KM auto niou daw 500 leu niou station mounima 1000 maniko grand 500 chak jr lolou lay pass mounima ni rk guenn deff thiaguatou ba doyal t meuno lenn 1000 sama khol diekh ma wann ko machine bii mou rouss