Li sama papa ❤️dadie sy mane t fekewoul dara sy mane rk mome guene meti sy adina 😭😭 sama papa dadone df lepou pour mane 😭😭 lou begue mou takhaw sy fatalikouma bene yone fouma sama papa doré wala kouma dore sy sama kanamou papa 😭😭 papa tu m manque bc 😭😭 yallana yalla oyofal souff sa kaw aldiana done kereum 🤲🏻🤲🏻🤲🏻🥰🙏🏻 papa😭😭