Football bii jeu bii baaxul. Ndax bu ngay jouer division yi, dangay mer lool. Bu nga ñàkke match, bu kenn jege sa wet, dangay bëgg rekk dóor ko ak sa loxo.
Jeu bii day yàq nit ki, baaxul. Ndax ñu yàq nañu jeu bi. Mise à jour bu mujj bi ñu def, dafa yàq jeu bi lool.
Bu ngay jouer division yi, mën nga am 40 défaites. Dangay bëgg rekk bàyyi jeu bi, ndax dafa lay yàq ci sa xel. Sa défense du dara, sa attaquants itam ñëwul. Lan moo xew? Danga di ñàkk match yi benn ci ginnaaw beneen.
Ci division yi am na hackers, am na ay problèmes internet ak yeneen problèmes yu bare. Loolu lépp moo tax jeu bi neexatul ni mu njëkk a neexe.
2026-11-24 14:24:48
60
🇸🇳NOTING 221 ⍟ :
Explication bi mongui si compte bi
2026-11-24 14:46:06
41
yayoubamba212 :
Toujours touba rék 😳😳
2026-11-24 18:57:47
5
Matar Sylla :
baye n'a Konami 😭😥
2026-11-24 14:49:39
43
Mineur _bi❤️💍 :
Pes baxoul fann lako khame damay joue division niou dougeul ma ma sip ko sama yaye nane ya takh bagn dougeul m🥹
2026-11-24 16:20:26
53
MBACKÉ ✪SN🇸🇳 :
Konami
2026-11-24 14:05:17
47
KHALIFA_LEU :
yalna ko yalla yeureum mais boyi nane bayi di roubé defois tensions yi day yek bly mais rien ne justifie la mort d'une personne
2026-11-24 15:18:49
7
mouha___bou ino seul :
boul niou sonal gayi wou niou touss
2026-11-24 16:53:26
9
꧁★ OUZ GAMEUR ★꧂ :
Thiaaaa adouna😭💔
2026-11-24 14:25:12
20
Youssou Seck :
ba taye yaye wah sa info bou leroul lou niou si mane nak ki ganiou yallna ko yalla yeurem amine
2026-11-24 16:52:26
11
CR7🫀🎉 :
billhi bayina
2026-11-24 19:28:30
0
A Doom ✍️❤️❤️ :
Man dh douma werenté si football douma khex si football 😭
2026-11-24 16:40:48
0
Neymar Jr :
Konami
2026-11-24 14:31:36
5
Adama221 :
goumin niatta temps lay duré😭
2026-11-24 15:55:31
25
Goram Djitte :
2026-11-24 14:18:56
6
Loufa Gaming :
Non 7-0 la
2026-11-24 21:47:58
1
🐅MOU.CUBARCÏ 44🐆🐾 :
🥺🥺🥺
2026-11-24 15:42:11
3
Baye Sall :
😭😭😭😭😭
2026-11-24 14:44:54
4
𝓶𝓸𝓸𝓶 𝓻𝓮𝓴𝓮 :
𝐥𝐢 𝐛𝐚𝐤𝐡𝐮𝐥𝐥 🥺🥺
2026-11-24 19:16:18
1
S A L I O U[] 🇸🇳[] :
informations yi wou té na dh
2026-11-24 20:33:25
1
To see more videos from user @notingsn, please go to the Tikwm
homepage.