sou done may domam damakay bayi ba sou déwé sakh douma nieuw bilay
2026-11-25 13:13:50
974
Mama Mbaye 🦂🧚🏾♀️ :
Y’a des mamans très toxiques ici wallahi 😭
2026-11-25 13:49:13
891
baby tyma :
soma diouré meun ma sour walahi ma sour la mba mbo déwé douma gnew ya bone
2026-11-25 13:36:49
153
Dada shop :
Li de mo Ame Sénégal metina Bilakhi 😭😭
2026-11-25 12:28:28
386
Famista bou sonko🇸🇳 :
Touss douko dale diam rek lay ame daguene yakarni yalla mom loko niane rek dakoy def
2026-11-25 13:13:03
479
N~S🧕🏽🇸🇳 :
Khalé bi sou melon ni man bilahi damakoy bayi Adina ak alahira sou déwé sah douma tew
2026-11-25 14:18:16
127
b@ye mo b@kh :
dara douko dalle
2026-11-25 13:18:39
95
Madame ndiaye :
Ki takhoul niounane yaye
2026-11-25 13:09:38
242
Fleur 🌷 :
Sa niane yi d dou dal khalei yi inchala
2026-11-25 13:24:39
132
fama :
2026-11-25 12:55:44
58
Thiam babelstor🛍️🇸🇳🇨🇳🇹🇷 :
Tousse d'où khew mayal nit gni diameu
2026-11-25 13:17:55
71
🇸🇳 :
Yui deh lama sama yaye di nianal té mako yor guinaw Yalla bou fébarer ma yobou hopital dieulal ko taxi mais la j’en peut plus bilae
2026-11-25 15:54:25
6
𝗶𝗻𝘁𝗿𝘃𝗯𝗹 𝗺𝗮𝗿𝗶𝗲🥥🍒 :
goumin niatta temps lay durée 😭
2026-11-25 16:18:19
0
Bsb shop❤️👸🏾 :
Mom lay dall sax
2026-11-25 15:51:49
0
La barbi noir :
Dara doudale khalé bi do yalla
2026-11-25 15:26:55
1
Diopkhoudia :
wallay dara douko dall
2026-11-25 14:45:09
0
❤️💍🥰 :
Yalla torokhaloula guay wakh
2026-11-25 15:52:48
0
princesse😍😍😍 :
ay boudone mane doumala weur doumala faleii doumala considérée
2026-11-25 13:38:46
155
SAM AL MAKTOUM :
yaye Bou bakh dou wakhei ni
2026-11-25 14:39:44
29
sonkomouselmi55 :
Dara dou khew si khalè bi diam rek inchalla 🙏🙏🙏🙏
2026-11-25 13:33:21
44
La villagoise :
Pour mom nian you bonne yi dey dall 🥺
2026-11-25 15:33:01
11
Aby seck :
Khalebi elle n’a rien fait je suis pas d’accord : elle ne l’a jamais vue sa maman ni appel ni message ni image elle savais même pas qu’elle était vivante yone bako message tout elle veut juste savoir et comprend le pourquoi sa maman l’a abandonné
2026-11-25 13:56:00
31
DiDi💕 :
Mane dhé j’ai vécu pareil dama def lounek mouni bougouma ma bayi ko souma yone khaliss mou dieul ta soumako dioubé mou trokhalma bayinako ak yalla
2026-11-25 14:25:22
34
Queen maman :
Bilay ya bonne sani Sayy dôme 🥺
2026-11-25 12:54:09
42
To see more videos from user @beugues.bamba, please go to the Tikwm
homepage.