Ma Sha Allah yalna Yalla faylène khalé yi Yalla barkel lène déf lène mag barké Seydina Mouhamed (PSL)barkép Serigne Touba🥰 de la parte de @Honorable Fatma Guèye de Thies ,domou Touba Toul
2026-11-25 14:37:11
36
💗bioufy💗dou💗sonk💗o 7💗💗 :
bilaye sama khole sédna khawma sakh loumalay wakh
2026-11-25 14:46:24
44
user4694895843352 :
walaye Ndeysane Yallna Yalla faye machalla Amna solooo lol