keur ni lay mel way fi nékh na ma beug lenee ahhh sama khol bi💃💃💃💃🎉
2026-11-25 19:43:19
27
Bella❤️❤️ :
Wa mane kane la wara appo sakh, niépa nginane mangi si borom…
2026-11-25 20:29:13
103
KUMBA :
challenge close ❤️❤️❤️
2026-11-27 21:09:30
0
Cheikh :
Mannn magui fiih😍
2026-11-26 18:53:59
5
myapapa21 :
Doma diagal bb 😂
2026-11-25 15:28:13
24
Bb Aïcha :
Yena meilleur nak 🥰😂
2026-11-26 10:14:16
7
🎀 sokhou fall❤️🩹 :
😂
2026-11-25 21:01:40
12
khemesse Diouf :
Wwwwwww
2026-11-25 18:50:43
6
Mariama Cissè :
2026-11-25 19:07:40
26
kharritou papame 1234 :
2026-11-26 08:34:11
5
Pãpįtø🥳 :
Un jour vers 3h du matin ma demon bena programme bay retour 😳ms jour bobou la kham ni yalla meusouma setane 😓may dokh ame Louma sentir sama guinaw souma diokhé mou bougé souma tahawé mou tahaw ma degon gnouni ken dou dokh di gesou goudi ah sama fitt bi togoul rek ma djeki rek daw ms Limay daw yeup tahoul mou bayma 😭ma boléko ay youkhou you metti sakh ba gneupe yewou géna dima diapalé 😭😭nékété allumettes bima don ataya la fate sama poche modon def bruit bi😭ma rouss ba legui douma sigui khôl wa kogne bi
2026-11-27 12:29:04
6
Ndoumbish🥰FATMISH SHOP DAKAR :
Ken dou kidone video🥰🥰😂😂😂😂
2026-11-27 00:31:29
4
Niang métallique :
molén gagné
2026-11-26 12:44:56
5
To see more videos from user @colista40, please go to the Tikwm
homepage.