@adjigooryomboul: Ma Diarra d’amour dèm nga bayi ma ak nakharr 😭bouma Doul gawa fattè ci aduna 😭yalna yalla attè la ci yeurmandèm 🙏🏻

adjigooryomboul
adjigooryomboul
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 26 November 2026 14:37:46 GMT
21292
3057
247
32

Music

Download

Comments

biba645
biba💋❤💋 :
nio bokone école kou bakh beug nit am joie de vivre yalna firdawsi done keur
2026-11-26 18:25:29
63
fantafay6
Mrs’thiam First lady 💍❤️ :
Ay way mes sœurs mes frères nagnou deff Lou bakh adouna diekhna ba parei 😭so sakh comprendre bakham liguay daw diar nako sakh yallah nagnou may moudiou bou rafett🙏😭
2026-11-26 22:32:18
22
user71325463217516
user71325463217516 :
Ndeyssane yalna ko yalla yeurme
2026-11-26 20:04:03
13
dhabeuguebaye
dhabeuguebay :
rest in peace
2026-11-27 00:00:08
0
xalif95
AXKD :
même jour et même année de naissance nioko boke...dina nameu sunu discussion sunuy confidence sunuy xoulo surtt barki Alhourane dinala nameu JUMELLE et tu va me manquer énormément bilahi...nala Yalla yeureum ya rabbi té samala ndiabote gui
2026-11-27 10:49:25
1
talibeahmadoubamba5
M💍❤️S yyou S diarra👩‍🍼🎄💐 :
Yalla nako yalla yeureum
2026-11-27 17:45:21
2
thiabalasalihate2
Thiab@ la Salihat€😍💍 :
sama kharite bi demna ni rk😭😭yalnaga khipé firdawsi
2026-11-27 14:16:52
1
thioro34
Ndeye Thioro Ngom :
Qu elle repose en paix
2026-11-26 20:38:31
1
talib.cheikh.beug8
talibé cheikh beug Babacar Sy :
Paix à son âme que le tout puissant l'accueil dans son paradis céleste amine fimou nek yalna ko geuneul fimou diougué yalla branchel ko racol aldiana direct si bamel lam yalla boumou yeg fouko yalla di yéreumé bidiakhi nabi Moustapha salalahou aleyi wa salam alahouma amine ya rabi 🙏😭
2026-11-27 17:09:14
0
www.tiktok.comwwwdiallo0
astou Diouf :
Ay way mame diarra touré ndeysane Ay yalla yeremale sa diam ouiiii uiiii ohhhhhhhh[Yeux larmoyants][Yeux larmoyants][Yeux larmoyants][Yeux larmoyants]
2026-11-27 16:06:01
1
user98199526
libasse diouf :
repose en paix mame diarra
2026-11-26 22:10:34
0
diarra.o2
Une déesse ❤️🦋 :
Ay way cousine d’amour loma def ni 😭😭😭💔
2026-11-27 10:40:02
1
sokhna.niang028
Sonia Bb :
Repose en paix 🪦 Diarra😥
2026-11-26 15:03:47
2
ndeyeamifall22
Ndéya business❤️😍 :
Ndeysane yalla nala yallah yeureum té kharé la aldiane firdawsi🙏🙏😭😭😭
2026-11-27 17:32:38
1
khadythiawtalibecheikh
ndéye Khady thiaw :
Yalnako yalla yeureume ta khareko aldiana
2026-11-27 12:06:12
1
gundioth.sene
Gundioth Sene :
yalla nako yalla yeureum
2026-11-26 20:18:24
7
footballeur7932
🏍️ :
aduna nékhoul yagoul 💔😭
2026-11-26 21:53:58
0
user8185134628748
user8185134628748 :
réponse en paix 😭
2026-11-26 20:34:16
1
user19322100
leutta260077842767 :
2026-11-26 20:19:21
1
general.bou.serig5
General bou serigne Babacar Sy :
Elle est partie à jamais 😓😓😓💔💔
2026-11-26 20:26:12
3
khalil.beugue.fall
khalil beugue fallou :
repos en paix mame bousso borom prokhane
2026-11-27 01:12:24
1
seynabou.dabo42
Ndiaya dabo :
Paix à son âme
2026-11-26 15:02:36
1
ballyahmadougaye
Bally Ahmadou gaye :
yalnala yallah yeureum 🙏🙏
2026-11-26 22:15:48
1
aidambaye60
user1648083937609 :
Repose en paix sister 😭😭
2026-11-26 14:43:38
1
user8860612675416
astou Cissé :
Yalla nako yalla yeureum 🙏
2026-11-26 19:07:36
1
To see more videos from user @adjigooryomboul, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About