@senegal.prime6: La pirogue portée disparue est arrivée à Yoff sur des conditions catastrophiques 😱😭#viralvideo #viraltiktok #viraltiktok #immigration #senegalaise_tik_tok
diomaye défoul dara yéna wara délol séne hél si yalla
2026-11-27 02:53:30
1156
FALAFA Nature&Events :
wa li khana gratuit la khalei yi yeup fane laniou dieulé khaliss pour dem diakhlé na
2026-11-27 09:33:37
349
Cheikh sad’bouh🇸🇳😇 :
Li deim Espagne 🇪🇸 diarouko wollahi kou nek ak sa weurseuk
2026-11-27 07:27:26
252
❤️GNAGNADIOP❤️XOLOUDIEUKEURAM :
periode bii gnou nekk dangene wara arreter dem bii déja sedd na galgui siw na gnepeu diouk rap yé deum yé gneupeu diouk . yalla naléne yalla taxawou si barké seydina Mouhamed🙏
2026-11-27 12:43:53
229
Alassane kalidou Dia :
bi mo défone 175 personnes? ?
2026-11-27 00:01:05
25
malick almaktum :
ndeysane bimoy bane bi defone 174 persone dembeu rek mangilene done nianal gni fegn alhamndoulilah
2026-11-26 23:58:38
355
Madame Ndour 🥰 :
Toglen si rewmi gnou khar yalla mo gene
2026-11-27 08:07:42
115
solitaire :
legui khaleyi Lou gnou meuneu liggey Espagne ba diapale sen wadiour. Bayilen fontou té gueum Yalla je comprendsvmags yi mais ay khaleyi you touti sen parents gnolen wara Yoro gneme diour ba paré beug teg khaleyi responsabilité bou gnou momoul
2026-11-27 11:48:39
33
Borom Thiés :
Linou khalis diaral bounou ko diamou yalla diara lon kéneu dou Sonou nit dou lekeu loudoul Lou Don werseuk geum
Courant d’air you graw ngaye dieulé si guéthe bi période bi a cause des vents
2026-11-26 23:47:45
34
Le mancunien :
Diomay na diokhé rewmi kén beug fi tok
2026-11-27 00:05:29
90
Abibou Fall :
Boy kouko ladji dépense ?
2026-11-27 11:48:37
63
Yayou al Mountakha ❤️ :
Delene ame réflexe di diokhé jus ak nokh bolen di secourir dagnouy déshydraté wou
2026-11-27 08:45:18
19
asalih :
com terre ngen si diam rek sant len yalla boubakh té ngen tok sisen rewmi diem ko defaral sen bopou mogeun didem si galle yi tayle sa nafsou leu
2026-11-27 06:45:31
33
sope nabi :
salallahou Alla mouhamet ❤ 💯 🤲
2026-11-27 20:11:47
13
Al mouhawa construction :
Li louka diar seuteuteuteuteut
2026-11-27 19:58:59
1
elhadj. hanne :
assume rekk
2026-11-27 15:57:28
0
masiba72 :
gni daniouy foontou rek
2026-11-27 11:18:42
5
guéye malick :
khana Sénégal amoul croix rouge
2026-11-27 09:36:15
18
🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥🟥 :
🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
diomay lèp loumou beugoul Guèthe gy sakh dousi andeuh jamais li rék doyneuh kémtane. vraiment diomay doyneuh niou kémtane
2026-11-27 01:16:12
6
diop doop diop :
sant lèn yalla doli thi lingén ko santon
2026-11-27 00:18:20
18
lune :
Diomaye doit démissionner
2026-11-27 12:54:25
8
Sokhna mou Seydi Aboubacar Sy :
Naniou delo khel yi si yala Europe bi metina té séde na actuellement ay 2 ak 3 degrés mofiné li kharoula té dara diarouko fi bilaye ils faut qu’ils arête yako😞😞😞
2026-11-27 13:25:41
6
To see more videos from user @senegal.prime6, please go to the Tikwm
homepage.